
youssou n'dour - xel كلمات أغنية
paroles de la chanson xel :
famarë reub kat lawone
da ama biss mou khall yône
mu taxaw di xalat bamu yàg
mu sène mbëtt miy daw
mu suxat fital ambadi dâgu
té nane kî douma raw
far mbëtt ma sène kokorong
dadi dieul bop ba
dal di koy rône
bopp ba neubouna litha des
yaramam béppa ngui fègn
deune bak, ndigg lak, tank yak, yénène ya
lippe di fègne
lii takh mou déféni
mbeutteu daa amoul xel
kone gnoune gni yalla jox xel
nagnu santati (x2)
li yalla bind yépp nit lathie gueneu fonk
mala yi lignou woutelé ak gnom moy sougnou xel motax déf
loy dougou jitalal sa xel
ba lo thièy wout
di nga guiss nguenél
nit gni yor xel boo sété gnoy dokhal aduna
kiy déf té dou xalat
thi missal day mél ni mbeut ma
nit môm khélako yor(x4)
li yalla bind yépp nit lathie gueneu fonk
mala yi lignou woutelé ak gnom moy sougnou xel motax gnuy déf
fi neubeu moy khax
boko amoul yangui mél ni bayima
sokou amoul doto nék nit
li yalla bind yépp nit lathie gueneu fonk
mala yi lignou woutelé ak gnom moy sougnou xel motax gnuy déf
wawaw(x4)
famarë reub kat lawone
da ama biss mou khall yône
mu taxaw di xalat bamu yàg
mu sène mbëtt miy daw
mu suxat fital am ba di dâgu
té nane kî douma raw
far mbëtt ma sène kokorong
dadi dieul bop ba
dal di koy rône
bopp ba neubouna litha des
yaramam béppa ngui fègn
deune bak, ndigg lak, tank yak, yénène ya
lippe di fègne
lii takh mou déféni
mbeutteu daa amoul xel
kone gnoune gni yalla jox xel
nagnu santati (x2)
li yalla bind yépp nit lathie gueneu fonk
mala yi lignou woutelé ak gnom moy sougnou xel motax gnuy déf
wawaw lolu moy xel
soko amoul
yangui mél bayima (x3)
loy dougou nang ko téké xel
famarë reub kat lawone
mbeuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuutt!
كلمات أغنية عشوائية
- michael van bodegom-smith & johnny cassidy - underrated كلمات أغنية
- jason shand - say you love me (please stay) كلمات أغنية
- elsie zel - sleepyhead كلمات أغنية
- h8.hood - snippet 06.01.2022 كلمات أغنية
- jah breezy - voice of drill كلمات أغنية
- tammy rogers & thomm jutz - about last night كلمات أغنية
- rakiyah - 3 am كلمات أغنية
- jaakima - idc كلمات أغنية
- the luisgame - mala vibra كلمات أغنية
- dorothy moore - the end of the world كلمات أغنية