
youssou n'dour - sagal ko كلمات أغنية
xale bi kii de jaaxle na, sonnal nga ko de xamul ku dul yaw
xale bi ndeyam ba na ko, baay ba ba na ko te gisoo ci dara
xarit na nga regle
xarit te nga xam ni bun ko defoon sa jigeen di na la naqari
yerem ko, sagal ko
xale bi ndeyam ba na ko, baayam ba na ko te seetoo si dara
xarit na nga regle
xarit te nga xam ni bun ko defoon sa jigeen di na la naqari
yerem ko, sagal ko
jef joo gis am na pay
jef ju baax am na pay waaye jef ju bon it am na pay
xarit seetaatal bu baax ni ngay doxalee
xale bi kii de jaaxle na, sonnal nga ko te xamul ku dul yaw
na nga regle
xarit te nga xam ni, xarit
na nga regle
xarit te nga xam ni
xarit te nga xam ni, xarit
te nga xam ni, xarit
na nga regle, xarit
te xam ni adduna de jaru ko
geestul sa ginnaaw
yerem ko, sagal ko
كلمات أغنية عشوائية
- slatt savage - wake up كلمات أغنية
- impala - yoksun كلمات أغنية
- thatrapperata - you ain't us كلمات أغنية
- basic the rapper - have u seen her (feat. gdotcali) كلمات أغنية
- april - 따끔 (lovesick) كلمات أغنية
- yearbook committee - drive me home كلمات أغنية
- ace hashimoto - they know كلمات أغنية
- black mike - the shakeback (freestyle) كلمات أغنية
- rocka - bir yerde (demo) كلمات أغنية
- youngs teflon - crud كلمات أغنية