
youssou n'dour - mahdiyu laye كلمات أغنية
bu de dangay leble
lebleelal ku am pey
seydina limamou
yalla feyna ko
neent f_kki at ya
mohammed woote
neent f_kki at ya
maam limamou woote
mahdiyu laye
mohammed waxoonna
mahdiyu gi ci yoon wi
seydina limamou
feen ca tefes ga
and ak issa
maami maam rane laye
moo niwoon geej ga
yow xamnga maay kan
bëgg naa nga dellu
ca la geek ga delloo, laye
keroog la woote
adjiboo daayirahi
kaayleen, kaayleen
nowleen, dikleen
jaamu lamul ahzam
laye
moo dellusee, moo dellusee
moo dellusee, mahdiyu laye, moo dellusee
baayi issa laye
baayi mandione laye
ak ababacar laye
maami maam rane laye
ak ablaye thiaw laye
laye
maami ousseynou laye
mahdiyu feenna
sagalnga reew mi
neppangi naan laye
yaa and ak issa
laye
yaa dellusee, yaa dellusee
yaa dellusee, maam limamou, yaa dellusee
yaa dellusee, xammenan la, yaa dellusee
yaa dellusee, mahdiyu laye, yaa dellusee
كلمات أغنية عشوائية
- the verve - one way to go كلمات أغنية
- m.a.b. - majesty n unity (bout you remix) كلمات أغنية
- prezidential candidates - whip my hair (remix) كلمات أغنية
- kasalla - stäänefleejer كلمات أغنية
- thees uhlmann - zum laichen und sterben ziehen die lachse den fluss hinauf كلمات أغنية
- perdenin ardındakiler - beni kendinden kurtar كلمات أغنية
- úlfur úlfur - á meðan ég er ungur كلمات أغنية
- nitro - ong bak كلمات أغنية
- hype man apollo - bijuu dama كلمات أغنية
- sixx:a.m. - live forever كلمات أغنية