
youssou n'dour - live television كلمات أغنية
paroles de la chanson live television :
1er couplet
ouragan ouppeul -ssamane
ba djante leer ma djanok satellite
satellite ngalla yoné ma la khew feulé,ak fénène ak fénène
mani go, go, go
ni live, live television live, live tv live
2e couplet
roplane bi warone tiim
dima eundil ki ma namona ngui
wayé tey télévision waar na ma, wone ma lima beugona guiss, ouragan mani ouppeul ouppeul ouppeul
ni live, live television life, live tv live
oh life, live tv live, live television live
f–k na né formalité leu(…)
f–k na né formalité leu(…)
f–k na né formalité leu(ma dj-pp yénéni chaines)
f–k na né formalité leu, leu, leu…
1er couplet
je vais vous raconter une histoire extraordinaire
un soir, une famille nous avait invité mes amis et moi, il y a quelques semaines de celà
nous étions une vingtaine à nous retrouver dans un grand salon, attendant avec impatience que le dîner soit servi
devinez ce qui est arrivé
à neuf heurs moins cinq,la famille nous abandonnés dans le salon, préférant s’ent-sser dans une pet-te chambre, avec une télé mal éclairée,uniquement pour regarder, cette fameuse émission
….khala-ss
….wala bok niou dem
chéri souma sadjobane
dina liguey ba ame louma djeundé satellite, nguir guiss di guiss la thia bbc, la thia ortm wala la thia mtv yeah
ni live, live television live
live tv live
we need live, live tv live, live television live
yaw chéri souma sadjobane, dina liguey ba me louma djeundé satellite nguir guiss di guiss la thia orts, la thia bbc wala la thia mtv yeah
wawaw kone television wawaw
yeah chéri souma sadjobane dina liguey ba ame louma djeundé satellite nguir guiss di guiss la thia orts, la thia cnn wala thia mtv yeah
wawaw kone television wawaw
كلمات أغنية عشوائية
- sylvie vartan - nous ne nous aimerons jamais كلمات أغنية
- daniel (kor) - and forevermore كلمات أغنية
- josiah queen & benjamin william hastings - i’ll fly away كلمات أغنية
- mgm lett - shoot كلمات أغنية
- nimble nova rc - on a low كلمات أغنية
- 1maikle - freestyle (perdon) كلمات أغنية
- sabah - صباح - amorty el helwa - أمورتي الحلوة كلمات أغنية
- kalben - kandırma كلمات أغنية
- kvi baba - to man nai كلمات أغنية
- field medic - coffee in the morning كلمات أغنية