youssou ndour - liggeey كلمات الأغنية
sound béne leu thi adouna biyeup nitt kounék amnga lo yeuk
niit kounék ammnga fém -2
less play -ssane teugueul
less play thiam tama
rock reggea jazz mbalakh all around the word béneu la
la samba la rumba thieu thieu thieu béneu la
ziguibiti i live music all around the world béneu la
saoul macossa rap music all around the world béneu la
music bi béneula louléne beglo lagnuy sakou music bi béneu la louléne beglo lagnouy fékhé musicien adouna béneula louléne di beglo lagnouy sakou musicien adouna béneula louléne di beglo lagnouy fékhé ah hiii yééééé
k
ko meuneu guiss mbaye si adouna amna thiossanam bouko nekh
am nga sa ngor am nga sa diom fonkou nga sey adeu
bilay kou nek ko guiss sagne nadieul lissa khol bi yaw nga defko
moytoul di togne té del téral kou diok beu gneuw setsila
bilay demlantéléne wéthié khalat bou kéneu khébaté
كلمات أغنية عشوائية
- yoshi flower - just on drugs كلمات الأغنية
- flowz dilione - gone كلمات الأغنية
- knxwledge - gdspln. [sry] كلمات الأغنية
- athagod - math project 2017 كلمات الأغنية
- stairly - i shouldn't want you كلمات الأغنية
- mick jenkins - blessed assurance كلمات الأغنية
- love bites - edge of the world كلمات الأغنية
- svyat - вольному воля (free will) كلمات الأغنية
- the revivalists - next to you كلمات الأغنية
- ankor - kiss me goodnight كلمات الأغنية