youssou n'dour - dabbaax كلمات الأغنية
keroksou penc bognouy wadjia wathié janta bi
di wadjial péssé ba
moulay dabbaxx yalla nagnou la diégué yalla daal moy taan waayam
moulaay dabaaaaax…
bougnou faté, bess boboulé, uhh bougnou soré, bess boboulé
bougnou faté bess boboulé
lofa gnaane, yalla may lako
modaane wakhal nitt gnep, mo daane wakhal nasraane yi
anh mo daane kadou askane wi
dafa daane wakh naane nagnou bolé sougn rew
dafa daane wakh naane bou kéne wéngal gaal gui
dafa daane wakh naane nagnou bolé sounou khol yi
dafa daane wakh naane nagnou yeureum djiguéen
sa borom bi begu na, yonentam bi begu na, yako liguéyal sa borom
moulaye dabbaxx yaw dé wacci ngua m-sso wakh lou amoul
kérok bang gnou djito -ssamaane si da leudeum
bessa ngui kéne dotou ko fatéééti… moulaay dabbaxx
bougnou faté, bess boboulé, bougnou soré, bess boboulé
bougnou faté bess boboulé
lofa gnaane, yalla may lako
anh! modaane wakhal nitt gnep, anh! mo daane wakhal nasraane yi
anh! mo daane wakhal askane wi
dafa daane wakh naane na gnep ligueye
dafa daane wakh naane nagn diangal gounéyi
dafa daane wakh naane na gnep liguèye
dafa daane wakh naane nagn diangal djiguééne gni
daawaoul sétane lou gnaaw
poussom la yorone fou khotékou mou gnaw
rewmi.rewmi amélnagnou la ndiouka moulaay dabbaxx
daawaoul sétane lou gnaaw
poussom la yorone fou khotékou mou gnaw
rewmi.rewmi amélnagnou la ndiouka moulaay dabbaxx
bakrék dara maam, aram lô coumba thiam
magn penda ak pathé pendaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaah
modaane wakhal nitt gnep, mo daane wakhal nasraane yi
mo daane kadou askane wi
dafa daane wakh naane nagn diap sounou rewmi
dafa daane wakh naane nagnep liguéye
dafa daane wakh naane nagn yeureum djiguéene gni
dafa daane wakh naane nagn diangal gounéyi
كلمات أغنية عشوائية
- ggod (brasil) - why deeze? كلمات الأغنية
- the_ivy_door - london bridge fell years ago كلمات الأغنية
- impellitteri - dominoe theory كلمات الأغنية
- ring of fire - empire كلمات الأغنية
- nwg - wym? كلمات الأغنية
- girls2 - サクラ道 - sakura michi كلمات الأغنية
- fbc feat. vhoor & wrm - acappella كلمات الأغنية
- zori - nigdy sie nie jarałem كلمات الأغنية
- tommy february6 - walk away from you my babe كلمات الأغنية
- xiu xiu - eat me alive كلمات الأغنية