kalimah.top
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

youssou n'dour - ballago ndumbé yatma كلمات الأغنية

Loading...

billaay , ballago ndoumbé yatma
su ñu waaji xaj oon na fi
naxxar doηη ,la ñu bayyee
yalla , wonneeti na

li tax ba mbir mi metti lool
ñun da ñu ko foog wul woon
yëf yi gaaw ba bette gnou
billaay wéetël na ñu

njiinoo njiin faramaareen
gòor u jaaga , nelaw naa
baay i wally dem na nii
ñun daal wéetël na ñu

ma ngi koy jaale sénégal
di ko jaalé gambia
di ko jaalé adduna
ndaanaan ba dem na nii

thione ballago , ndoumbé yatma
bu yalla buur bi doon taggoo
kon di na ñu bayék yaw
ni patrimoine bi nga ñu bayyeel
yee gua nit gñi , tete leen ci adduna
yee gua nit gñi , tete leen
xam al leen ci adduna
ahhh _ ballago
yee gua nit ñi ci adduna xam al leen
ni ñu war a nekkek
ak ni ñu war a dundée
ak ni ñu war a jëfleentee
jinaxoo mbaay
yaw mi dëkké biir suuf
boo dem ee neel ballago , réew maa ngi koy joy
aduna ngi koy jooy
art baa ngi koy jooy

njiin faramaareen
thione seck , wéetël na ñu
ballago ndumbé yaatma
adduna , amul solo
njiin faramaareen
thione seck , wéetël na ñu
ballago ndumbé yaatma
adduna , amul solo
njiin faramaareen
thione seck , wéetël na ñu
ballago ndumbé yaatma
adduna , amul solo
njiin faramaareen
thione seck , wéetël na ñu
ballago ndumbé yaatma
adduna , amul solo
li tax ba mbir mi metti lool
ñun da ñu ko foog wul woon
yëf yi gaaw ba bette gno
ndanaan ba demna ni

njiin faramaareen
thione seck , wéetël na ñu
ballago ndumbé yaatma
adduna , amul solo
njiin faramaareen
thione seck , wéetël na ñu
ballago ndumbé yaatma
adduna , amul solo
njiin faramaareen
thionе seck , wéetël na ñu
ballago ndumbé yaatma
adduna , amul solo
njiin faramaareen
thione sеck , wéetël na ñu
ballago ndumbé yaatma
adduna , amul solo

كلمات أغنية عشوائية

كلمات الأغاني الشهيرة

Loading...