
youssou n'dour - baay niasse كلمات أغنية

suunas yonent bi la sidi barhame di xeentu
nu mu defe ba yonent bi beg lool la baay di sakku
lu neex rassulullahi, loolu neexna baay niasse
ku xam li yonent bi ban, dô ko gis ci baay niasse
moom sidi barham niasse masula fatte waxtu
saa su ne nj_pp, mu yees, masulu timale waxtu
boo toppee maam ya mbokk laak yonent bi
laajal doom cheikh yi xammeenanu sidi
su de beggnga roy suunas mohammed
jokkujil ci baay niasse, diineem ja rafetna
bu newel di julli mangay durus lillaahi
baay niasse xamul ludul tagg rasuulullaahi
li mu bind ci teere jagleelko yonent bi
li mu bind ci teere jagleelko science bi
li mu bind ci teere mu jem ci wallu xam xam
buur yalla teeralnako wonewul am am
li mu am ci taalibe ci reewi nit nu nuul ni
lu ko epp la baay am ci reewi nit nu weex ni
su de beggnga roy suunas mohammed
jokkujil ci baay niasse, diineem ja rafetna
boo demee medina baay
laa illaha janngay riir
daaray alxuraan yaangay riir
niasse coumba abdoulaye, jaajеfate
su de beggnga roy suunas mohammеd
jokkujil ci baay niasse, diineem ja rafetna
li mu tabax ci daara de meneesuko lim
dongoom bi gena ndaw menna bind kaamil
ku yaru ci baay niasse bu waxee nga xam ko
te lu mu la na_n_l bilaahi f__k nga gis ko
la xew ca maka ak la xew madina
amul benn werante moo xew ca kerem ya
boo jogee ci reew mi dem ci reewi arab yi
boo nuyoo ba noppi faw nu laj la cheikh bi
su de beggnga roy suunas mohammed
jokkujil ci baay niasse, diineem ja rafetna
كلمات أغنية عشوائية
- double kanon - jib el tarf (remix) كلمات أغنية
- k camp - good problem كلمات أغنية
- xvl hendrix - ain't dat a bitch كلمات أغنية
- poltergat - another dream كلمات أغنية
- jhaye - no more كلمات أغنية
- femme - light me up كلمات أغنية
- fudge - these saturdays كلمات أغنية
- kingdom - down 4 whatever كلمات أغنية
- luxtorpeda - siódme كلمات أغنية
- van halen - beautiful girls (live) كلمات أغنية