youssou n'dour - 4/4/44 كلمات الأغنية
4-4-44 (4-4-4-44) môm sa bopp mô neikh
4-4-44 (4-4-4-44) guiss say mbok mô neikh
bô léké ba sour war nga gueureum
war nga gueureum gni doug thi wagne wé
wagne wa tang na
fimou toll nî war nguèna bëg
war-ngèna bëg thi indépendance bi ak-liko indi
4-4-44 (4-4-4-44) môm sa bopp mô neikh
4-4-44 (4-4-4-44) guiss say mbok mô neikh
bô léké ba sour war nga gueureum
war nga gueureum gni doug thi wagne wé
wagne wa tang na
damani bou leuk léké olom
boudè goréna té deugou warna ko guereumé pithe
no, no, no no no no
no, no, no no no no yeah
4-4-44 (4-4-4-44) guiss say mbok mô neikh
4-4-44 (4-4-4-44) guiss say mbok mô neikh
ah li dafa nékh… guiss say mbok mô neikh
li dafa nékh… gueume sa bopp mô nékh
4-4-44 (4-4-4-44) môm sa bopp mô neikh
no, no, no… guiss say mbok mô neikh
4-4-44 (4-4-4-44) môm sa bopp mô neikh
oa, li dafa nékh… guiss say mbok mô neikh
a… môm sa bopp mô neikh
oa, li dafa nékh… môm sa bopp mô neikh
كلمات أغنية عشوائية
- scary kids scaring kids - the world as we know it كلمات الأغنية
- trust company - fold كلمات الأغنية
- trust company - someone like you كلمات الأغنية
- olivia - twist it كلمات الأغنية
- kelly osbourne - one word كلمات الأغنية
- jamie o neal - girlfriends كلمات الأغنية
- the national - city middle كلمات الأغنية
- lisa marie presley - turn to black كلمات الأغنية
- nikka costa - till i get to you كلمات الأغنية
- stellar kart - second chances كلمات الأغنية