
youssou n'dour - 4/4/1944 كلمات أغنية
4-4-44, 4-4-4-44 moom sa bopp, moo neex
4-4-44, 4-4-4-44 gis say mbokk, moo neex
boo lékkee ba suur war ngaa gërëm, war ngaa gërëm ñi dugg ci waañ wee, waañ wa tàng na
tóllu nii war ngeena bég, war ngeena bég ci independans bi, ak ñi ko indi
4-4-44, 4-4-4-44 moom sa bopp, moo neex
4-4-44, 4-4-4-44 gis say mbokk, moo neex
boo lékkee ba suur war ngaa gërëm, war ngaa gërëm ñi dugg ci waañ wee, waañ wa tàng na
dama ne bu lëk lékkee olom budee gore na te dëggu war na ko gërëméé picc yi
no, no, no, no, no, no
no, no, no, no, no, no, yee
4-4-44, 4-4-4-44 gis say mbokk, moo neex
4-4-44, 4-4-4-44 gis say mbokk, moo neex
ah lii dafa neex, lii dafa neex, lii dafa neex, gis say mbokk moo neex
lii dafa neex, lii dafa neex, lii dafa neex, gëm sa bopp moo neex
4-4-44, 4-4-4-44 moom sa bopp, moo neex
no no no gis say mbokk moo neex
4-4-44, 4-4-4-44 moom sa bopp, moo neex
waaw lii dafa neex, lii dafa neex, lii dafa neex, gis say mbokk moo neex
aaaaa, moom sa bopp, moo neex
waaw lii dafa neex, lii dafa neex, lii dafa neex, moom sa bopp, moo neex
كلمات أغنية عشوائية
- tricky - hate this pain (live) كلمات أغنية
- dr. john - rain كلمات أغنية
- jaszy da b3ast - like me كلمات أغنية
- daba - flou pt. 3 كلمات أغنية
- młody weks - mlody weks x mlody pupson x mlodyhaze - phonk freeatyle كلمات أغنية
- brady james - feel a thing كلمات أغنية
- tia rae - all4u كلمات أغنية
- rat tv - loli [right version] كلمات أغنية
- mjölk - fidelity كلمات أغنية
- n0thanky0u - scum كلمات أغنية