wally secka - natural love كلمات الأغنية
xaley bi may doundal
feel nani dafma beug ngir yalla
ay vibes’am fimouy dialeu
amoul benen mindef boufay dialeu
bouy dokh di daagou ci kogn bi
day dal melni solou daleu
lima yeuk ci sama xol bi
j’affirme moy natural love
guene ci xel yalla ko sakk ngir man
yeyeee, wowoooo
yalla ko sakk ngir man
baby dama dof ci yaw
limoy natural love
boulen ci diemeu wah lou nyaw
lima geuneu neh ci mom
moy yerem wa moy yerem wa
ak dohine ba ak dohine ba
eloquence bek elegance bi
ki moy sama sweetie girl
baby dama dof ci yaw
limoy natural love
an gars gni
boulen ci diemeu wah lou nyaw
ndeysaan
yay sama lovе
dama dof ci yaw
loma def no matter
tahawougama mama
natural love baby
i lovе you
i love you and you know it baby
bouy dokh di daagou ci kogn bi
day dal melni soloul daleu
lima yeuk ci sama xol bi
j’affirme moy natural love
guene ci xel yalla ko sakk ngir man
ca naturel ba la
she walks around the corner
look like a diamond in the water
i know this girl make me crazy
this love is a natural love
ca naturel ba la
كلمات أغنية عشوائية
- gianmaria testa - la tua voce كلمات الأغنية
- nino dangelo - vita mia كلمات الأغنية
- claudio baglioni - a domani كلمات الأغنية
- marco antonio solis - y yo sin ti كلمات الأغنية
- the sundial - a dream كلمات الأغنية
- mina - noi due nel mondo e nell'anima كلمات الأغنية
- expulsados - yo quiero ser tu perro كلمات الأغنية
- stereo total - ypsilon كلمات الأغنية
- sugababes - mellow كلمات الأغنية
- fonky family - la guerre كلمات الأغنية