wally b. seck - dawuma dara lyrics
h_llo girlfriend
ma wakhla lène
i love you more yobouma benene niveau
amna fiit am djiko ak melokane
teudj ma seu bathroom dawouma li
dara dara rassouma dara
dara dara da_dawouma dara
n0body can tell me nada
dara dara da_dawouma dara yeah
dara dara rassouma dara
dara dara da_dawouma dara
n0body can tell me nada
dara dara da_dawouma dara yeah
dara mane rassouma dara dara dara dara
better day, better day, better day
fekhel ma teud sa kaw lal after niou khol
khalé_bi meuna football, té meuna dougal
dotoko défati sama sweety girl
sama xol, sama coco bané
sou néké da nga tang soumil li nga sol
tassalma seu cheveux naturels gueuna mol
me and you no limit sama pretty girl
ragalouma li, dawouma li
i love youuu coco_coco bané
ragalouma li, dawouma li eeh
refrain :
dara dara rassouma dara
dara dara da_dawouma dara
n0body can tell me nada
dara dara da_dawouma dara yeah
dara mane rassouma dara dara dara dara
(samba peuzzi)
time is money. well
cho bi amna time mam!
guel bou mol waaw
lolou momay danel !
guisla dof ci yaw
kay ma wane la li ma meun yeup
put your ass one my banga (come on thotianna)
da né si forme, ngandi down, lolo you formé
taawi chewing_gum, dima p_ss
maat tougne, raay hanches
nako dal mane may kiy voundang
yewou guiss la sama wét that’s what i need
ay million meun nako ci solo una noche
mane ak yaaw !
una no noche , dotoko defati !
refrain :
dara dara rassouma dara
dara dara da_dawouma dara
n0body can tell me nada
dara dara da_dawouma dara yeah
dara mane rassouma dara dara dara dara
كلمات أغنية عشوائية
- eah jé - salt och socker lyrics
- crepeblox - как назвать? (kak nazvat?) lyrics
- kaitlyn baker - trouble is you lyrics
- vafrinto - lifestyle freestyle lyrics
- sasya arkhisna - mangku purel lyrics
- curren$y - doe boy lyrics
- reto - pumba lyrics
- agir - voltar ao paraíso (papel em branco) lyrics
- blinblau - занят долго (busy long) lyrics
- remedy rx - what i deserve lyrics