thione seck - mathiou كلمات الأغنية
Loading...
ndeye ndeyou ken la baye bayou nieupe la, sama yaye djé, sama yaye djii, guissouma koumalay meuna wethiéé, yaw mi gueune si mane yaw mi gueune si mane
yaye boye sama galadj
bo beugué djote sama djiko toudal sama yaye douma ko fowé doma ko fowé yaye boye sama galadj
rote nga thi leudeum debb nga thi taw, wale thi nadj bou tang bou yaye yeup melen ni yaw kene dou diour di sani
(refrain )
ndeye ndeyou ken la baye bayou nieupe la, sama yaye djé, sama yaye djii, guissouma koumalay meuna wethiéé, yaw mi gueune si mane yaw mi gueune si mane
yaye boye sama galadj
djéba ndoye, indou woma woma ndeye sane, bayo boye dom djou am yaye day am baye wow wo
كلمات أغنية عشوائية
- mcclinton delbert - one of the fortunate few كلمات الأغنية
- mcclinton delbert - everytime i roll the dice كلمات الأغنية
- mccoy andy - you gotta let it go كلمات الأغنية
- mccoy andy - strung out كلمات الأغنية
- mccoy andy - she's doing it with lazers كلمات الأغنية
- mccoy andy - unconditional love كلمات الأغنية
- mccoy andy - mediaval madras كلمات الأغنية
- mccoy andy - love & hate كلمات الأغنية
- mccoy andy - let it rock كلمات الأغنية
- mccoy andy - italian girl كلمات الأغنية