thierry wone - djotna woma remix كلمات الأغنية
louma wéssou démbe gnanouma si yala diaraat
loumay séntou sama kanam na done loumay talate
mou djik ma,diaral nama fanané took di halate
holat li guene bone si mane ségui séguate
génération boul fallé, takhalé waw
à faire des dollars avec des cailloux
dans le noir
du sénégal à paris les gens luttent, prie pour éviter la chute
djiko louy sah si nit ki wala lane la
king_y wolou molay féhél ray djiégui diale
bopp sa bopp nga wahko sa bopp mou wér la
topla fép yake sa dér lolou lérna
ne me trahit pas non
non non non
ne me trahit pas non
diote na woma
dama deké dang dang
diop soubak ngone ngir mene am ndam yeah
diot na woma
siguil where i come from
bal soumay none yi done tong tong
faylèn ba wèthi lén baklèn dioum dioum
fompe sèni rongogne ninal séni tougne
diote na woma
dama dеké dang dang
wahtou dafa djot tey ma tahaw am ndam yeah
mangui halat eulеuk lou wara done sama yeuk yeuk
halat yéwou fadiar doh dadiék weurseuk
halat bayi tog_you mbèd dième la beut seuk
pour avoir des millions de lové, l’humain s’est cannibalisé
douma tayi moytou thioytou life bi fouma féyté
mouslou bagna taylé sama doundou si holitou guérté
pour quelques guertés on s’abime tous et toutes
et le doute est là
on s’a, on s’a, on s’abime
certes bougouma perte fokma dieul yonou dègue
gnafé ba guène si diafé diafé am gueude
haine fébarou hole lay séde
perdu dans la nuit, tout les jours que dieu fait
entre amis, ennemis
degueuleu, degueuleu
ne me trahit pas non
non non non
pour quelques guertés
ne me trahit pas non
diote na woma
dama deké dang dang
diop soubak ngone ngir mene am ndam yeah
diot na woma
siguil where i come from
bal soumay none yi done tong tong
faylèn ba wèthi lén baklèn dioum dioum
fompe sèni rongogne ninal séni tougne
diote na woma
dama deké dang dang
wahtou dafa djot tey ma tahaw am ndam yeah
limouy déf si mane néhouta nétali
yone bou rafèt la si séntou mo waral ma diapli
si lèp dehegnou bamou menema fèthieli
donté déguo wok sa sopé féhél boul diani
pour avoir des millions de lovés
la race humaine se divise
mes amis et mes ennemis se multiplient
vite vite vite vite vite faut qu’j’débite
pour éviter la crise à ma famille
nangouna si sone deuk si thiona ba wope
doh kona ba kona di yeungueul bopp
louma sopela doumako neube dafma tope
diote na woma
pour avoir des millions de lovés
ne me trahit pas non
non non non
degueuleu, degueuleu
ne me trahit pas non
diote na woma
dama deké dang dang
diop soubak ngone ngir mene am ndam yeah
diot na woma
siguil where i come from
bal soumay none yi done tong tong
faylèn ba wèthi lén baklèn dioum dioum
fompe sèni rongogne ninal séni tougne
diote na woma
dama deké dang dang
wahtou dafa djot tey ma tahaw am ndam yeah
كلمات أغنية عشوائية
- moytanic - datdevilshit! كلمات الأغنية
- instalok - take cover كلمات الأغنية
- memoriam - dronestrike v3 كلمات الأغنية
- teddy pendergrass - shout and scream كلمات الأغنية
- lonemoon & stereo cube - pizza كلمات الأغنية
- admiral t - sound system كلمات الأغنية
- raffine - defterlerim (intro) كلمات الأغنية
- the collection - wedding party (love makes you disappear) كلمات الأغنية
- framig - cloudy كلمات الأغنية
- ed wood is dead - cul de sac كلمات الأغنية