skinshape - kourou كلمات الأغنية
[chorus]
kourou
(don’t cry)
kourou bamba ndiaye
(don’t cry, bamba ndiaye)
kourou bamba siniati
(don’t cry, bamba siniati)
lémméné kourou
(don’t cry, child)
lémméné kourou
(don’t cry, child)
[bridge]
sou diante diogué khalat leu di la ladj loy khalat
(every time i think about you i wonder what you’re thinking about)
louy sa khalat dé makoniou kham loiniou yéndo
(tell me what you think so we know what to do)
yaggueu nala wakh dom bou di togn
(i’ve always taught you that a child shouldn’t be rude)
yaggueu nala wakh dom bou di sague
(i always taught you that a child should not insult)
yaggueu nala wakh dom bou di am lou la nakharé
(i’ve always taught you that a child shouldn’t experience evil)
[chorus]
kourou bamba ndiaye
(don’t cry, bamba ndiaye)
kourou bamba siniati
(don’t cry, bamba siniati)
كلمات أغنية عشوائية
- baby rasta & gringo - improvisando كلمات الأغنية
- the window smashing job creators - olympia's blues كلمات الأغنية
- pink diablo - hookeado كلمات الأغنية
- trinity (nl) - got it all كلمات الأغنية
- big fil - step by faith كلمات الأغنية
- emotional relation - right where i'm supposed to be (part i) كلمات الأغنية
- thrill pill - наркотик (drug) كلمات الأغنية
- ellende - hand aufs herz كلمات الأغنية
- jeden - reminiscencje كلمات الأغنية
- b-rent (ky) - bad mornin’ كلمات الأغنية