samba peuzzi - ndongo كلمات الأغنية
ndongo lyrics
aaah eh
ayaa
sénégal boy
yeah
balle bangui sogga takk
ghetto sama guinaw
man rek man kassé fi têk tankeu
xaliss dou doy diameu dou eup
tour bangui dèm succès dii yokou
rest in peace feuri nioun dougnla faté
dérétou diamageun mofiy daw
dé rek momay tèrè té game bi
iyoo iyoo
nimay rappé loussiy sa yonn
bandit deug dankay ndirou
xamnaani si man ng_y xol
mais non non ningkoy défé dou nonou
bem la lal deh
sa show man la bardé
ay caché millions sans projet
man la sénégal boy from diack
eh non non thiow li dou beuri
man nguén ték sèn beut yi
yanou wadiour motakh ma yèksi fi waa eeh
niom louniou fok?
meunouniou bok
xir bi la yorr niouy daw malèn koy nok
eh manguék buzzou ndongo
dama xew
hey, boma xamoul
dèmal nga tok
eh dèmal nga tok
dèmal nga tok
eh boma xamoul bou yaa dèmal nga tok
pic biniou ma sanni mane demako toul
nioma si djittou malenraw fouf
nélene yolé xadjatoul ci poche
niak sipp wessouwoul andak kou matoul
xaliss la xèkhè douma khoulo
kholéma ndongo lô bir ghetto
musikou fi lay toukilo international
nekké ci yone mashallah
poche bangui fess may fékh na mère bi bégg ma begg
bougne sagnone ken douma deug
legui niom niomay xèhh
nangou demb beuge bagne tey
sissoumane yi demelen bayi si birr
kode sama xol def xeuthie
eclate kanam bi xol guedj
eh non non thiow li dou beuri
man nguén ték sèn beut yi
yanou wadiour motakh ma yèksi fi waa eeh
niom louniou fok?
meunouniou bok
xir bi la yorr niouy daw malèn koy nok
eh manguék buzzou ndongo
dama xew
hey, boma xamoul
dèmal nga tok
eh dèmal nga tok
dèmal nga tok
eh boma xamoul bou yaa dèmal nga tok
niom louniou fok?
meunouniou bok
xir bi la yorr niouy daw malèn koy nok
eh manguék buzzou ndongo
dama xew
hey, boma xamoul dèmal nga tok
eh dèmal nga tok
dèmal nga tok
hey, boma xamoul (ouu yah) dèmal nga tok
كلمات أغنية عشوائية
- southernwade & garrickson - little bit كلمات الأغنية
- juceex - fwts كلمات الأغنية
- george homeh - neghdeh كلمات الأغنية
- ytcracker - executive command.html كلمات الأغنية
- crosby, stills, nash & young - sleep song (demo) كلمات الأغنية
- jonathan blaque - think كلمات الأغنية
- zeusfuture - 100 nummern كلمات الأغنية
- paraliza buđenja - krizma كلمات الأغنية
- dearlyworth - шлюха (whore) كلمات الأغنية
- el trío de omar rodríguez-lópez - miércoles كلمات الأغنية