kalimah.top
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

omzo dollar - borom keur كلمات الأغنية

Loading...

[debut]
gouro, 3 pieces
gouro, 3 pieces
gouro, 3 pieces
gouro, 3 pieces

[pont]
(i say) aladji miezé
def la sama sokhna lala yéné
man ak ioe si diakka, imam ak préfet
boléma’ak sa papa nako gérer (woo)
yow laa wa yow le (x2)
beug nala khamna beug ngama
doyyal ngama soumala amé amna niénti diabar
eh ngani pa bi nako wo-oh-oh-oh
damleu beug takk guénouma ak yow-oh-oh-oh
vieux père woxma lanela loy douter-eh-eh-eh
beug nako amna dinée ak ligué-eh-eh-ey (yeah)
[pont 1] :
baby oubbil ma sa xol pour ma nekk sa borom keur (anh yeah)
naala dieundeul ben keur pour ma nekk sa borom keur(woo)
wokhak sen wa keur nélène maay sa borom keur(anh yeah)
naa taal sen keur sougnma deffoul sa borom keuur(oh yeah)
[refrain]:
dina indi gouro,def trois pièces
gouro, def trois pièces
gouro, def trois pièces
gouro, def trois pièces
gouro, trois pièces (ngané lane)
gouro, trois pièces (ngané lane)
gouro, trois pièces (ngané lane)
gouro, trois pièces…
[couplet 2]
(i say) takk sama fite
do am ben woudiou baby à part sama fite (yeah)
boula nékhé doreul radio
may sa borom keuur, baby cardio
(eh) louy bayyanté pour kouné sey sey bi?
ah bougn def lolou kay niou sey sey bi
(eh) mak yow warrouniou am blem
ya eupone prétendant championnat anglais
réception invités yi nanni jinja
soma firé dina mourou melni ninja
mayé bou ndieuk meyyleu galé tekk cii 3 quarts
soumaley nianni feug ngandi boubou 3/4
man la gars yi wowé bad man miezé
am diabar mou melni yow laa yagg rêver
nuit de noce premier son ma mayyleu bébé
yalnaa tokk di lath yallah finga fété (yeaaaah)
[pont]:
baby oubbil ma sa khol pour ma nekk sa borom keur (anh yeah)
nala dieundeul ben keur pour ma nekk sa borom keur
wakh ak sen wa keur nélène may sa borom keur(anh yeah)
na tal sen keur sougnma deffoul sa borom keur(ooh yeaah)
[refrain]:
dina indi gouro,def trois pièces
gouro, def trois pièces
gouro, def trois pièces
gouro, def trois pièces
gouro, trois pièces (ngané lane)
gouro, trois pièces (ngané lane)
gouro, trois pièces (ngané lane)
gouro, trois pièces…
[pont]
aladji miezé
def la sama sokhna lala yéné (yeah yeah yeah)
aladji miezé
def la sama sokhna lala yéné (yeah yeah yeah)
aladji mieze
def la sama soxna lala yéné (yeah yeah yeah)
aladji miezé
def la sama sokhna lala yéné

كلمات أغنية عشوائية

كلمات الأغاني الشهيرة

Loading...