omzo dollar - bae كلمات الأغنية
say say
say say
say say
i say
dara dakkoul nekk ak sama bae
sangou solou guéneu ak sama bae
sama khol day vibrer ni manetou play
so nekkoul sama khel sama khel dey tey
guisseutouma kenene koudoul yow
so nekoul sama wo boulma wo
like f_ck kouma jegué koudoul yow
so nekoul sama wo boulma wo
legui samay communications yeup la dague ni wé
da am lidi nelow ci mane li kenene mounoul ye
wa do
mais dara dakkoul nekk ak sama bae
dara dakoul nek ak sama bae
hun
wo ma goudi niou jokko
yoni ma sa ay photo
chaque jour yow rek lay gainz mm soumeu deffé plein sama auto
yendou say reseaux sociaux
deglou say message vocaux
meme soumfi nekoul fougn leu fek dangmay represent melni logo
yamay calmer ni silence terré nelow ni bruit
bakh ci yeram ni fruit
dageu toy melni pluie
wakh ma kagn laley guissate bep bis dagn key bissat
khamga mane ak yow deugue leu dougn jouer série melni ci fifa, say say
dara dakkoul nekk ak sama bae
sangou solou guéneu ak sama bae
sama khol day vibrer ni manetou play
so nekkoul sama khel sama khel dey tey
guisseutouma kenene koudoul yow
so nekoul sama wo bouma wo
like f_ck kouma jegué koudoul yow
so nekoul sama wo boulma wo
legui samay communications yeup la dague ni wé
da am lidi nelow ci mane li kenene mounoul ye
mais dara dakkoul nekk ak sama bae
dara dakoul nek ak sama bae
ndekete mane rekka am bae
ndeke mane rekka am bae
damay geuneu lerr sa you niou ande
nala wone louy ay ni livre anglais
babe ndekete mane rekka am bae
bi poison da fort kou ko gnam deh
joulit la mais yow lay mandé
khamga lougnou wakh ci woyouk bandit
sama nopp yi ci seu bat manam
soumleu degoul negn ma fat ndakh
da am gni jangue medecine 8 ans wanté neu leu lerr ni yow yay kimay fath wawaw
nieuw sa galet melni association
dadi niane ci melni association
kay niou celler suniou associa
bayi leu dafa kharam melni association
yow
كلمات أغنية عشوائية
- blutengel - königin der nacht كلمات الأغنية
- d-bo - euer junge كلمات الأغنية
- chemical x - trace كلمات الأغنية
- caligola كلمات الأغنية
- sonamoo - we are legendary كلمات الأغنية
- guru - fine and free كلمات الأغنية
- ol' kainry - ol' kainry - les partiels de punchine كلمات الأغنية
- beeboy x dżejpa x jankes plane machine - woła cię miasto كلمات الأغنية
- kettcar - 48 stunden كلمات الأغنية
- cidade verde sounds - tá difícil esquecer كلمات الأغنية