kalimah.top
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

obree daman - banneex كلمات الأغنية

Loading...

banneex lyrics
kula faale wul man mii maa lay faale
doon sa seetu kula xool man lay gisaale
kula faale wul man mii maa lay faale
doon sa seetu kula xool man lay gisaale

ci sa bët laay xool naan la i love you
baby yow yaay sama life
ci sa bët laay xool naan la i love you
baby yow yaay sama life
baby yow yaay sama life

suma yàlla bëggee wax len ko na ma baayi ak yow
ndax ku melni yow amatul ci àdduna
sama xol laa la def bëgg dëgg laa la def te duma sooraale
benn noon ndax yaay sama life

ci sa bët laay xool naan la i love you
baby yow yaay sama life
baby yow yaay sama life

kula faale wul man mii maa lay faale
doon sa seetu kula xool man lay gisaale
kula faale wul man mii maa lay faale
doon sa seetu kula xool man lay gisaale

ci sa bët laay xool naan la i love you
baby yow yaay sama life
ci sa bët laay xool naan la i love you
baby yow yaay sama life

كلمات أغنية عشوائية

كلمات الأغاني الشهيرة

Loading...