kalimah.top
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

nitdoff - trahison كلمات الأغنية

Loading...

[couplet 1]
hey yow f-ck seni menotte baby lègue meu guénate
nio gui djiem louné nguir beugu saltel sama honneur
baby daleul diam calleul sama lawyer
boulen maye liniou beugu bousseu beut yi toyeu
sama coffre fort bayina fa money
sama mor de p-sse moy sa birthday honey
danie meu seuf gun nenagn mako mome
tè gun bi dafeu meusseu k!ll nit tchi ben old up
yeugouma tinouma really not guilty
lou diouguewoul tchi yallah ragaloumako kone word up
kouma djièguè lole moma wareu diaay
tè khole na ba khole beuguma toumal ken si samey waaaay
amna arrivant bou aksi fi mandat de dépôt
wayè limeu dioteu wakh beuguouma woon sakh nga yeug ko
néna pablo bileu done topou momeu piègè
nguir meu dougu jail ndakh sama place leu beugu siègè

[refrain]
tchi love ak tchi respect lako yagua tekk
meussouma gueumni biss dina niew nga fippou jaaymeu prek
fimeu diaar ak yow andak yow
bimeuy niew seu side di dieul sa five bobou do woon sh-t
life dafeu teureudi dèm beu doto wauloti
money takh nga call the cops yolèma meu dougu jail dougu jail dougou jail
tchi love ak tchi respect lako yagua tekk
meussouma gueumni biss dina niew nga fippou jaaymeu prek

[couplet 2]
balma té diégalma diafè diafè yimeuley doundou lo
demna beu ame kerseu khole leu ci beut t khoultou wo
lekeuto naneuto diambantè tchi parloir
akh bouy dokh sunu diguèntè leu dontè dey louy war
doyna waar piste el pablo niou bagne ko enquêter
parce que amneu bras long sén poste yi laniouy inquiéter
lou yallah diekheul mou diekh na sakho kholou mougne
na avocat bi def ligueyem naniou doylo koun
legui khamna ni torez mo def gun bi sameu car
demeul dic convoquel press bi niou bindeu sama cas
waroutouma fanane ben nuit de plus fi ci jail
pablo yonè nameu lettre nane meu suicidel
insbi dafey vulnérable ndakh tè nanguna
dafeu ame sa faibless woko neko nanguou nga
tekk ko deal camera caché ko bamou avouè
andal ak sa sang froid on a qu’une carte a jouè

[refrain]
tchi love ak tchi respect lako yagua tekk
meussouma gueumni biss dina niew nga fippou jaaymeu prek
fimeu diaar ak yow andak yow
bimeuy niew seu side di dieul sa five bobou do woon sh-t
life dafeu teureudi dèm beu doto wauloti
money takh nga call the cops yolèma meu dougu jail dougu jail
tchi love ak tchi respect lako yagua tekk
meussouma gueumni biss dina niew nga fippou jaaymeu prek

[couplet 3]
f-ck yow ak sa kingdom eskeu khamna niou kinga done
snitch n-gga what’s new in your life its been long
yeah its me kileu guen woon ci ndole bi
kileu fekone ci mbed nga koy niakantek tiol tiol bi
k!lleu dane diox jo(jordan) yi clothes beu tchi call bi
ki nga fenal seuf ko gun dougual ko si taule bi
yeah its me b-tch sokhna sa ngui galè tokk
kileu dane togal ak fauteul sey yerè a l’époque
sokhna sé keu guorè waay lounèk lako wadji dikk
thiabi keur taakaayou diamant mouniko f-ck sh-t
b-tch n-gga da nga fake beu meulnè silicone
yallah rek la ragal sokhlawoul guay firi gun
yeah b-tch -ss n-gga
you can k!ll me you can shoot me down
whatever you want n-gga but u’re not gangsta
f-ck you f-ck you n-gga

[refrain]
tchi love ak tchi respect lako yagua tekk
meussouma gueumni biss dina niew nga fippou jaaymeu prek
fimeu diaar ak yow andak yow
bimeuy niew seu side di dieul sa five bobou do woon sh-t
life dafeu teureudi dèm beu doto wauloti
money takh nga call the cops yolèma meu dougu jail dougu jail
tchi love ak tchi respect lako yagua tekk
meussouma gueumni biss dina niew nga fippou jaaymeu prek

كلمات أغنية عشوائية

كلمات الأغاني الشهيرة

Loading...