nitdoff - lou meunoul niak كلمات الأغنية
{intro}
thiéli tek nama cii laf_fam yaubu ma cii diawou dji
wane ma sama bidéw
thieupél ma cii bi guéw
hé hé héhéhé hé hé
yo yow !!!
verse 1
sikim la cii ben laden, gun la cii hizbola
béré la cii che guevara
gaw ba do ségui dara
couplet wala acapella
cii niary rimes ma pakatéla
ndeye dior la cii toubabou dior
mérité na ay guéimbou d’or
ndongo la cii hard cor
nomba la cii lat dior
yarame wala kathior
mbede mi nieup d’accord
rap bi dotoul bekkor
ki cii yagg ak kiy dor (new school)
mouslou na cii sen lamigne
diébeulou cii serigne lamine
assane cii barki serigneum
yéné nama kamil_lam
fallou foumou fébaré nitdoff moy vitamine’eum
mic béy sémigneum
maatt la cii guémigneum
meuneu touma dém nguinaw mbede def nama thiamigneum
lamar cess la cii mboldé
yatt la cii bolet
seung la cii kassé
guinze la cii ni nga koy xolé
dream la cii gnène gni
doff la cii gnène gni
nit la cii gnène gnii
dream la cii gnène gni
keuyitt la cii jail’ou kaw bi
karaw la cii ndèlou pa bi
délégué cii syndicat bi
n.d(nitdoff) k!llah in the party
what’s my name ya nit
what’s my name ya doff
what’s my name ya nit
what’s my name ya
refrain
verse 2
yo
kagoul la cii rap’adio
underground bi la xeuthio
deubeul bamou napadio
sama waleu lay pathio
crack la cii dounk yi
cane la cii pimp yi
coffres la cii bank yi
45 cii tank yi (braaaaa)
uppercut leu
base_ball cii nit leu
barame cii hit leu (braaaaa)
togal té tiamp yone (bro)
sétane the champion (flow)
i’m the number one (what)
des numbers one (hannn)
the black lion man from the mother land (hoouuu)
ghetto béma fal king ma délou magal lène (yeah)
amoul loxal ngène
kouy fake doxal dém (braaaaa)
bène mic djouni flow bèn doxa_ndem
dieuwrinou d_squad say my mother f_ckin’ name
nit, what’s my name ya
doff, what’s my name ya
nit, what’s my name ya
refrain
yo
right now let me tell ya
mister champion make a love in the building
ovation standing, party ending
tryin do my best with my all school splendid
i’m independant
i f_ck with my kingdom
if you wanna test it n_gga
you better hanging
military training
my coup gang banging
people love me like….what’s the love
(mari khuana)
for my man essko bou algérie
(algerie cona)
i hate police
i f_ck them justice (yeah)
they need me liked up when i was to paris
lambe na ba dathie
séintu na ba séine
hip hop galsen lama di represent
feeling la tchii flow
flow la tchii rime
rime la tchii beat
beat ni mao school mao school
gunzout mother f_ck dass lèn
nitdoff lifou mbede________
mor fire
yambe la cii tiaya
ilimanou rap bi firi khutba, firi aya
never give up tire ya
free style like street loyal
كلمات أغنية عشوائية
- maajins - paranoia كلمات الأغنية
- neophyte - pillz كلمات الأغنية
- bathlete - good game كلمات الأغنية
- goddess fiji - break a thot كلمات الأغنية
- ca$hbenton - distrust كلمات الأغنية
- cauldron (uk) - crossing the threshold كلمات الأغنية
- red simpson - i'll be goin' home to momma كلمات الأغنية
- kati k - wehzutun كلمات الأغنية
- kim na young (김나영) - 조금 더 외로워지겠지 (i get a little bit lonely) كلمات الأغنية
- keblack - ma lady كلمات الأغنية