nitdoff - freestyle 3 كلمات الأغنية
part 1
[refrain]
yagui teup teup teup teup
meuno niou dapp
finiou ko athie dafa kawé cii yaw meuno ko keup
niary album rek laniou guèné rek ghetto bi reup
niou am success cii mbede bek cii sèni club
nitdoff nitdoff k!llah k!llah
easy bou thug from d_squad family leu
niary albums rek laniou guèné rek ghetto bi reup
niou am success cii mbede bek cii sèni club
[couplet uniaue]
yeah yaw ya
haters n_gga blabla like a donkey prey
see them try wanna fly but don’t get pay
lidé wouté naak fire bou pompiers yi fay
lii nek cii k!llah k!llah nékoul tchii mbaye dieye faye
xam sa bopp yokou job gueum né mbéday fay
mane ak niom bokou niou way (chemin) douniou jonkanté
kou tchii dadié ak mane cii mbede dag_y djonkone déy
real sh_t la tek attoum 2007
clash’nikov cii mbakk mii madone dieuwrine fépp
mouy cii rap mouy cii flow mouy cii domaines yeup
lig_y yeuk cii hard cor diko doundeu cii underground
n_ggaz yeup d’accord ngakoy feel cii sunuy sound
” moy nitdoff nitdoff k!llah k!llah ”
baye fall_lou mbéde bileu
madialou keul guileu
annou yènou real yileu
ben laden_ nou fake yileu
mao school moma berndel bou dr. dre
limay flow sathiou mako douma fadda frey
done number one cii rap bi damako yagg pray
tokk di play monday ba sat_rday
mister mother f_ckin’ k!llah and you’ll rada way
with my man .a.d.a. roythia……
rakhass fake yii nekk cii rap bi melni tiaz yu seuy
gnii done woté tangor ma def lèn glass niou séy
gnii done djoy rap right now what you say?
k!llah k!llah falouna bourou
rogogne dotoul tourou
real yagui sourou
fake yi dii mourou
rap bi lagnii saagané ba kèn xamoul loumouy ndourou
requin bi feulneu dieune yi dii nourou
melna cii yèn nii neurone melone cii seydi nourou
nitdoff nitdoff loxo tchaa kaw
nako dall ala athiou leu waxko tchaa kaw
li nga cii meune xana tathioulaa ak dioxko sa doe (xaliss)
tchii ghetto bi cii hood bi fimou mété la diaré
rap naa ba amé dépression rap ba amé diarrhée
moussouma xam louy ndaré
louma guéné rek daay carré
samay lyrics dafay waré
sénii yoss dafa taré
cii mic la lènii xarré
vous êtes tous mal barrés
[refrain]
yagui teup teup teup teup
meuno niou dapp
finiou ko athie dafa kawé cii yaw meuno ko keup
niary album rek laniou guèné rek ghetto bi reup
niou am success cii mbede bek cii sèni club
nitdoff nitdoff k!llah k!llah
easy bou thug from d_squad family leu
niary albums rek laniou guèné rek ghetto bi reup
niou am success cii mbede bek cii sèni club
[speech]
yeah mao school baay figua ko athie dafa kawé man
gars yi niogui teup mé bobou ba légui moy lolou
mé xolal joxma bénène beat bénène beat bo xamnii daf may délo cii hood bi
bo xamane tanniii daf maay délo diamono 1995
beat you leundeum yoyou
dioxma beat bou mel nonou nieuwatt
part 2
refrain (out of the hood)
yeah out the hood my n_gga hanhan
yeah !!!
yeah !!!
yaw !!!
danio sonou cii prek bek irriii dii teuthie
fokk niou am lot of money nguir firi lii leuthie (got’em)
ennemis yi dém xouli niou beutt nouyou niou keuthie
sunu weurseuk meunoko teuthie
doundou ghetto béniou fatt baniou moudjou dii xeuy
beug xam lénène loudoul lignii xeuy dii dathie
niakk am takh lou rérr rek niou wola tathie
djigne leu sathie nga wédi rek niou worla baye
fokk niou guéne cii realize ay fantaisies
sunu wadiour yi yéni séni yèn you diss yi
meuneu am touti noflay li dess sèn biss yi
fokk niou out the hood deuk cii galé you mak yi
yégue ak wathie ropalane niougni ragné cii gokh bi
ndagam bour bignou djitté coupé na ndokh bi
fay lamp yokk doundeu kone fokk niou dokh dokh bi
fokk niou yaubou sunuy dom cii yénéni school
meuneu séinetou cii niom ay ngeunél yu cool
fokk niou reuthie kaff fly dém béggué for real
get experience cii ay beautiful deal
meuneu dokh sunuy streets you lerr té clean
meuneu yokk sunuy clip ay guerr d blé
meuneu yaube sunuy kilifeu niou adjii ba makka
mayé ay keuyitou keur n_gga tabakh ay djakka
lougni niane cii kaw souf dou paradise
dagni sante sunu god sakou better life
{cori – i science}
out of the hood to produce my own
my own mental fool
end throne throne classic sh_t
out of the hood well this is what i need yeah
to succeed my life
get out of this stride
out of the hood
{nitdoff}
fokk niou out the hood
guène fly né bird
tekk biz am djizz dém all around the world
fokk niou moss louniou moss
live lifou boss
dékké noss
am soxla lambeu dathie sa poche
{cori – i science}
out of the hood cause this is what i need
to succeed my life
get out of this stride home
{nitdoff}
fokk niou out the hood
guène fly né bird
tekk biz am djizz dém all around the world
fokk niou moss louniou moss
live lifou boss
dékké noss
am soxla lambeu dathie sa poche
{cori – i science}
out of the hood this is what i need
to succeed my life
get out of this stride home
out of the hood to produce my own
my own mental fool
end throne throne classic sh_t
out of the hood well this is what i need yeah
to succeed my life
get out of this stride home
end throne throne classic sh_t (yow)
{nitdoff}
diko maay my gunzout soldiers and my d_squad (out of the hood)
diko maay bépp hood n_gga bépp ghetto n_gga (out of the hood)
hustle for life amoul bayii (out of the hood)
niou gueum sunuy dream gueum nii biss dina nieuw mou meusseu done true (out of the hood)
you know i’m saying (out of the hood)
yeah n_gga yagui hustlin’
han hannnn !!!!
yeah mao school beat bi métina man
daleu nama daleu nama ganiou na tchii
mais xolal bayil ma défattt tchi toutii égo
maay ko sama gars yi
part 3
( nit k!llah k!llah k!llah
doff k!llah k!llah k!llah
nit k!llah k!llah k!llah ) x4
[couplet unique]
yaw
technik tactik melni galactik
doff nit hot sh_t bou yagué nga lapp(noyé) dikk
bouniou sékké impro yaw yay moudjé lathie bic
boulko sakh diém bro sa kaw lay dathie pik
manela public bi di holla yawla fekk yi di mbalakk
gueune laa siiw eupeu la haalleu boma sauro dama lay alakk
kalama kocc lalay lakk
cii kaw beat bi damay takk
affaire de thug lalay bakk
rayla sédeulé sa nakk
hamdoulilah cava like sefyu molotov
continué like saga i’m the mission undercova
lg love k!llah like new york loves hova
d_squad my gova
just give my pova
kèn dou kheuthio ak mane i’m like the new casanova
li déh safarala dieuleul diwko saa nopp’a
k!llah is not real cii sa guiss guiss rek
ladial yèn b_tch n_gga yima done disrespect
ma délo lèn cii mbedd niou délou deal some crack
djeundeu sama bum teudiou dora feel some track
limay tek dafa deep nga cii sèn intérêt
nioune laa public bi di holla nioune nioy siiim sèn thiéré
affaire de hood lagni niodii guiss nga nignou simplé
nioy akk siempré(toujours) té doniou sèneu sèn télé
lyrical tekko cii mbede bi di fathie sèn plaie
niom gnimeu beugue dapp wax lène dagnii soneu
ay mbéggué laniou yorr ma yorr harley davidson (motocyclettes)
yeukeutii sama hood melné marley ak kingston
damay flow lou xott ba melni kilifeu ak thiat
donté sama xalima dou dapp bou djily bagdad
dina try again ba sama piles yi takkatt
yo! fu yalla nékoul my n_gga kone dara néwoufa
weureul sama gueum gueum ba guiss ko ba noppii wéroufa
mane sama waazila djox nama werdeu ak wazifa
deudou loma aduna ak lepp louy xétou lucifer
( nit k!llah k!llah k!llah
doff k!llah k!llah k!llah
nit k!llah k!llah k!llah) x2
كلمات أغنية عشوائية
- zayrondon - white lighters كلمات الأغنية
- pablo 2115 - rest in piss كلمات الأغنية
- big bugs band - hip hop كلمات الأغنية
- lbr - freak nasty كلمات الأغنية
- alonzo - desertland كلمات الأغنية
- klein - arrange كلمات الأغنية
- achille lauro - ragazzi madre prequel كلمات الأغنية
- daïtshi - untold كلمات الأغنية
- nimmo - dancing makes us brave كلمات الأغنية
- dyscarnate - an axe to grind كلمات الأغنية