kalimah.top
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

nitdoff - bokouniou niveau كلمات الأغنية

Loading...

{verse 1}
yagg nala wakh bokouniou niveau assalamalek niouy yëg sama égo
fass nama nak fène lo séni mytho, kassamarak fén tèen lo séni pivot
bi di lido amoul hasard ci flow bi f_ck samay rivaux
klémati lang, xellém_meu tchi dégne nioune douniou thiouthie fi thiouthie fé comme djibo
kholéma ni maggoum ceddo, sometime damay nëk souma djéko
mane kouma beug téé moy deflo ma dieul souma joggué di make samay djégo
teulé nga cii rap té sa bindeu ba ngui beug mel benn débutant bouy tâtonné
sa mélokanou tott ba ngui tééy sunu xel niou ngui laathie niata bite la sa taate connait
toxic boul niou possoné li ng_y def dou rap bigni consommé
kouy deup di dibi ay texte niam wezzy ba succès bi yaubeu leu au sommet
cii net bi lagnela eumbeulé waayé mbède bi doko fi weussiné
nioune am nagnou tarbiya respecter real yi goor_djiguène meunouniou fasciné
noooooooooo !!!
kouné mo ngui naane k!llah dafa meune day def carrière li dou effet de modes
wouténak rappeur_rou akhirou zamane yi dima saff ay fins du monde
sen image zeu gueune sen répertoire
yakamté waral sen perte art
aimé, aimé, partagé, clic aimé
même si bou nékhoul please aimél

{refrain}
n_gga doniou meuné rap, n_gga doniou meuné flow
n_gga donéma harcord nga niou djito
n_gga doniou meusseu yapp, n_gga doniou meussou dapp
n_gga do niou meun ni diakk té tito
sunu diar diar diouguéwoul so mytho, d.o double f mbède bèko tipo
louniou beug laay indi, louniou lathie lay def di jayantèk niom baniou quitto
baayil dignou wo ci sa niveau n_gga, baayil dignou wo ci sa niveau n_gga
baayil dignou wo n_gga baayil dignou wo n_gga baayil dignou fok ci sa niveau
baayil dignou wo ci sa niveau n_gga, baayil dignou wo ci sa niveau n_gga
baayil dignou wo n_gga baayil dignou wo n_gga baayil dignou khaar ci sa niveau

{verse 2}
faux timide no limite pacifique, colèrique polymique tchi doff bi
yallah diox xollou niit all i need, moy di djouli ni djoulite
di dieufé ay digueulém di baayi ay térém ci coranique
(mbède beurina mcs ba légui guissago kou raw nit)
foumala rombeu nél beureute jog nouyouma loxo né great job
saurouma ci mic done ketchup, ma patial leu defla leu tchi grek thiop
médiocre douma tek choc kou xam rap douma wéthio
nitdoff dafa authentiqué, show bou nek mou djaay autant de tickets
déserté nagne sen camp quitté, ndax sen carrière yeup la amputée
ci chaisou bour bi didjou tokk, am fite beu nopi didji c_ck
gunzout sama wérou waay d_squad moy tidji porte
what a f_ck n_gga ? ya better fidi bokk
hip hop ba ngui sama loxo maay téé bamou reuss
all eyes on my clic they care about us
who da f_ck u are ? come for test me, come contest me
believe me f_ck you’ll die, i’m the last real mother f_ck mc alive

{refrain}
n_gga doniou meuné rap, n_gga doniou meuné flow
n_gga donéma harcord nga niou djito
n_gga doniou meusseu yapp, n_gga doniou meussou dapp
n_gga do niou meun ni diakk té tito
sunu diar diar diouguéwoul so mytho, d.o double f mbède bèko tipo
louniou beug laay indi, louniou lathie lay def di jayantèk niom baniou quitto
baayil dignou wo ci sa niveau n_gga, baayil dignou wo ci sa niveau n_gga
baayil dignou wo n_gga baayil dignou wo n_gga baayil dignou fok ci sa niveau
baayil dignou wo ci sa niveau n_gga, baayil dignou wo ci sa niveau n_gga
baayil dignou wo n_gga baayil dignou wo n_gga baayil dignou khaar ci sa niveau

{verse 3}
n_gga i know souma dano boudé lolou ng_y khaar mother f_ck contano
daniouma naw ilimanou sama kaddu day def pow pow comme canon
gueum kima done kène douma minimise dama téleu weuri djiz
n_gga that’s what it is boudé hit nala wari diss onzou_bilahi nareu waar iblis
djom djé beuri kène yaaré wouniou taalal loxo kone fokk sunu waar yi diiss
gun to the zig zag d_squad the big block
k!llah molay dik rap sassouné deep track
mélokano def lou taaru cii mbaarou kothie kone kaay képarou
taataane fi ng_y dieulé khibaarou real hardcor biy takh nga waarou
dél imaginé xol yi maa tchi né diomal naa rap wala makk djiné
n_gga donima rap, n_gga donima flow, n_gga donima fiit
n_gga donima cash, donima hit, donima clash
xana kay toote ngamay gueuneu done n_gga
xana kay fake ngamay gueuneu done n_gga
xana kay b_tch ngamay gueuneu done n_gga

{refrain}
n_gga doniou meuné rap, n_gga doniou meuné flow
n_gga donéma harcord nga niou djito
n_gga doniou meusseu yapp, n_gga doniou meussou dapp
n_gga do niou meun ni diakk té tito
sunu diar diar diouguéwoul so mytho, d.o double f mbède bèko tipo
louniou beug laay indi, louniou lathie lay def di jayantèk niom baniou quitto
baayil dignou wo ci sa niveau n_gga, baayil dignou wo ci sa niveau n_gga
baayil dignou wo n_gga baayil dignou wo n_gga baayil dignou fok ci sa niveau
baayil dignou wo ci sa niveau n_gga, baayil dignou wo ci sa niveau n_gga
baayil dignou wo n_gga baayil dignou wo n_gga baayil dignou khaar ci sa niveau

كلمات أغنية عشوائية

كلمات الأغاني الشهيرة

Loading...