mgeey - loy wax كلمات الأغنية
eh! (omzo on the maafe)
hook [oothentik zeus]
niveau bey hot dey lakke
song bi dey daw m’bappe
ndakaaru njaay lay wacce
da nga xam wala ng_y lacce?
(ey)
niveau bey hot dey lakke
song bi dey daw: m’bappe
ndakaaru njaay lay wacce
da nga xam wala ng_y lacce?
hook [mgeey]
boy kula laadj loy wax?
ey waay ndeysaan
ey deykalanax!
dañu koy salsaa bamu saf sapp
boy kula laadj loy wax?
ey waay ndeysaan
ey deykalanax!
dañu koy salsaa bamu saf sapp
verse [mgeey]
eh seen xel yè karaas mënoleen dem
fépp lañ mënè ego ak théme
lepp ngeen tële di xaatim nenn
yèn ñëp lay warax, talent dey fènn
raw naa daxaar qon lepp ay saff
yëngël dakar ba lepp ay barr
fepp ay saxar te fepp ay tarr
xatna comme yaraax yenn ñëp ay xaar
naanuma lingom te gënlaa forox
deñ lay tingoom nga mën maa boroos
sëf lë ay drogues di laal ay troc
jital oyof te mën naa torop
laalnaa xol yi, bët yеppay taa
root néñ xalaat ba feesal ndaa
xir bey dalaat
fi mann leñ falaat te
neena faraax damay salsaa (allright)
hook [oothentik zeus]
nivеau bey hot dey lakke
song bi dey daw: m’bappe
ndakaaru njaay lay wacce
da nga xam wala ng_y lacce?
(eey)
niveau bey hot dey lakke
song bi dey daw: m’bappe
ndakaaru njaay lay wacce
da nga xam wala ng_y lacce?
hook [mgeey]
boy kula laadj loy wax?
ey waay ndeysaan
ey deykalanax!
dañu koy salsaa bamu saf sapp
boy kula laadj loy wax?
ey waay ndeysaan
ey deykalanax
dañu koy salsaa bamu saf sapp
verse [oothentik zeus]
eh kula laaj loy ? my boy
bëri ay biens, riche: bad boy
gatd_mn, dañu koy game bamu neex
waye mënu ñuko gagne fò
d’accord
maak mgeey de la mancha
sancaat drip bu leer diko salsaa
may mc bila antann
tek lu dìs gann si sa kaw ba nga appaat
f_ck li ng_y wax mëso maa jox cèpp
budè da nga merr everything okay
avant ngeen di xeef nekatul mok yeen
sama talent mo daaxa wanewuu mo gates
okay okay no stress no cap
my boy loy hate?
sama chronomètre dou seu temps lay kepp
bu yabbo nga kepp sa tank boy
tekk ngafi tank mais taanku guinaaw
hook [oothentik zeus]
niveau bey hot dey lakke
song bi dey daw : m’bappe
ndakaaru njaay lay wacce
da nga xam wala ng_y lacce?
(eey)
niveau bey hot dey lakke
song bi dey daw: m’bappe
ndakaaru njaay lay wacce
da nga xam wala ng_y lacce?
hook [mgeey]
boy kula laadj loy wax?
ey waay ndeysaan
ey deykalanax
dañu koy salsaa bamu saf sapp
boy kula laadj loy wax?
ey waay ndeysaan
ey deykalanax
dañu koy salsaa balu saf sapp (ey)
كلمات أغنية عشوائية
- jesper binzer - the future is now كلمات الأغنية
- lnu quanyy - "sõlìd" كلمات الأغنية
- missy higgins - strange utopia كلمات الأغنية
- il corpo docenti - per niente كلمات الأغنية
- kay-young - i try كلمات الأغنية
- alltta - muggsy bogues {fg. v} كلمات الأغنية
- nomis [rapper] - rhodes to rome كلمات الأغنية
- lil deazy - price كلمات الأغنية
- skinny b (sublime music inc.) - gucci gang (spanish version) كلمات الأغنية
- swings - 튀어나온 못 (the nail that stuck out) كلمات الأغنية