meek bib - we da best كلمات الأغنية
we da best
outro[lil mame]: khombole city w-ssup meek bib lil mame bankk gniakk walawalabok
[hook: lil mame]
we are the best; we are the best
bi sonng kouko dègu kham ni gnon fi nèkeu
we are the best bi song kouko dègu kham ni fi gnon fi nèkeu
[verset 1 ] meek bib
dagniou meuna rap ni m-sson bouy tabax
sa rap dafa yombeu ni guèl bou gnouy sabagn
n-ggas yagui get li b-tches yi di check li
sa xèl di wiri wiri do meussa djeuli
bouniou sorou fils beat ak mic laniou songualè
sèn kham kham dafa dèss maname fils daguèn teulè;
lofi rap mou dièkh n-gga fèpp laniou meunè
hola hola ni g-ydè si alleu
flow rymme tèkchnik dotou niouko balè
we don’t give a dem n-gga
diogue ndeye feul laniou dèf souniou xèl
bidew dou fèkk diat fèkk mane ak dou bènn
teudjeul sa gate waxnalako dou gniar gnètt dou bènn
aay ateu yagui diague tè mokalo
souniou meune rap fils guissilo
rawla comme 9 ak 6 n-gga
souniou meune meune dafa dizz n-gga
bokkou gnou diatay ndakh tè yaw thounè gua
loy wodo laytay n-gga rap gangster la
so meunoul gua bayi naguoul ni yaw diagueu gua
souniou ko sèkkè gua bayi im real hustle
harcorp laniou dorè
sèn flow yi laniou barè
si kaaw beat bi lanoiu forè
bokoy teukou di dègu ndarè
guissa guouma rap bou carrè bicthes guissa guoma rap bou carrè
[hook: lil mame]
we are the best; we are the best
bi sonng kouko dègu kham ni gnon fi nèkeu
we are the best bi song kouko dègu kham ni fi gnon fi nèkeu
كلمات أغنية عشوائية
- conti - i gotta go كلمات الأغنية
- red rum club - vivo كلمات الأغنية
- uisce jones - shaken up كلمات الأغنية
- lord gary - the workout كلمات الأغنية
- javiielo - pa los gustos los colores (remix) كلمات الأغنية
- samir - jatt ludhiyane da كلمات الأغنية
- fabvl - cast from fire كلمات الأغنية
- puzzle xiii - sivin' كلمات الأغنية
- arijit singh - mera ishq كلمات الأغنية
- lowlives - hate, greed, liars, thieves كلمات الأغنية