kalimah.top
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

jay 21 - jox meu sa loxo كلمات الأغنية

Loading...

[refrain]
djissouma sounou diganté lane moko meuneu yak
guestouma jox meu sa loxo niou dem seti dji sa yay
deglouma dinako malaka nga diour dou sa dom
dama djiss loumou moussoul djiss
djigene moussou meu beugué ni à part souma yay
me tell them

[couplet 1]
changer na lyrics bindeu na samay sidite té beneu mot refléter woul mane lima yene
cas bi dou virus yay sama tiabi ci serrure mane bandit leu t beneu mbeur moussouma yep
nagn dem ci sa tanta
nagn diar sama tonton
bougn dem sama tante
damay bagn kouma gantou
wakhkat yi comme pobar niom sauce dou leine rombou
sama xol mola djiss
té none yi lolou lay djiss
ya nara diour samay fils
té beuss bi romb na biss
yay sama chocolat my baby donc c’est normal meu fir
diotna niou dem sa gale tok ci table niou quitte
diokh ma sa hand niou dem sa gale diaroul ng_y tite

[refrain]
djissouma sounou diganté lane moko meuneu yak
guestouma jox meu sa loxo niou dem seti dji sa yay
deglouma dinako malaka nga diour dou sa dom
dama djiss loumou moussoul djiss
djigene moussou meu beugué ni à part souma yay
me tell them
[couplet 2]
wakh meu khet bouma ci moussoul firil
khale bi diek neu beut yi leer neu ni midi pile
bi moy corps de rêve yaram bi do ci fek cellulite
bi beauté naturelle wakh meu fou makoy dieuleti
falewou rihanna convoque beyonce dila let
toufli kardashan yi souma leine xolé sinusite
sama xol mo dawa daw beu yeg terminus xamone na ni baby do s’en morom oh again
well done
bandit changer nekaté meune na nek
sounouy wadiour nagn niou ni_n_l amine
tabakh souba lolou meune na nek
rampan pan
baby youkhoul amine
fi no def yalla def nga diar ci
sokhna sou glamour intelligente tek ci classic xol bi yatou do sen morom
oh again
well done

[refrain]
djissouma sounou diganté lane moko meuneu yak
guestouma jox meu sa loxo niou dem seti dji sa yay
deglouma dinako malaka nga diour dou sa dom
dama djiss loumou moussoul djiss
djigene moussou meu beugué ni à part souma yay
me tell them

كلمات أغنية عشوائية

كلمات الأغاني الشهيرة

Loading...