iss 814 - xool ma ci bët كلمات الأغنية
(jeeba)
mbeuguel bou deugou
dara douko faye
yaay seetou
bi woné sama leeraye
jant goudi
biddew soubeu teel
bimala xamé
ci la tagok weetaye
nii tognal sa aaaaaa ! yaye
balenala ndakh mbeuguel bimaa yeug
ci yow
nii tognal sa aaaaaa ! baye
balenala ndakh mbeuguel bimaa yeug ci yow
wolou nala wolou wolou nala !
eh yaaaay !
wolou nala wolou wolou nala !
ahn ahn !
(iss 814)
boume laay guiss ngaay doundou
dafemaay doundeul baby
soume laay guiss ngaay rétaan
dafemaay doundeul waay
boume laay guiss ngaay doundou
dafemaay doundeul baby
boume laay guiss ngaay rétaan
dafemaay doundeul waay
xool ma ci bët
ma xool la ci bët
nioune niare la rek
mbeuguel a nekh
xool ma ci bët
ma xool la ci bët
nioune niare la rek
mbeuguel a nekh
yéne saaye nga diéki diéki woma
woma
nga meer maané mba diépiwoma
nga néma non non
yéne saaye nga xole ma rek
ma rétaan rétaan
yaay sama boumou xol
yaay sama boumou xol
bo meeré ba guédeu dafemaay metti
metti
bo deffé ba gnipeu nala setsi
setsi
douma ci xole sax pa bek mère bi
mère bi
na oubi bountou bi soxna si
dang ma diape sa mbaal
té douma guéneuti
bilay walay yé
yow laay fethie si bal
yaay sama mélodie
yow rek la baredé
eh eh !
boume laay guiss ngaay doundou
dafemaay doundeul baby
soume laay guiss ngaay rétaan
dafemaay doundeul waay
boume laay guiss ngaay doundou
dafemaay doundeul baby
boume laay guiss ngaay rétaan
dafemaay doundeul waay
xool ma ci bët
ma xool la ci bët
nioune niare leu rek
mbeuguel a nekh
xole ma ci bët
ma xole la ci bët
nioune niare leu rek
mbeuguel a nekh
(jeeba)
yeh weurena ba weurengueul adouna
yeh kou melni yow mba amatina
yeh dougueul ci keur gui yatouna
ndakh yow yaay yaay sama boumou xol yaay sama boumou xol
(iss 814)
yéne saaye nga diéki diéki woma
woma
nga meer maané mba diépi woma
nga néma non non
yéne saaye nga xole ma rek
ma rétaan rétaan
yaay sama boumou xol bi
yaay sama boumou xol bi
weurena ba weurengueul adouna
yeh kou melni yow mba amatina
eh yah dougueul ci keur gui yatouna
ndakh yow yaay
yaay sama boumou xol
yaay sama boumou xol
كلمات أغنية عشوائية
- lisa - ポーカーフェイス (poker face) كلمات الأغنية
- ster - perdu كلمات الأغنية
- emamouse - pptrap كلمات الأغنية
- pet shop boys - no time for tears (single mix) كلمات الأغنية
- threadleaf - safe here كلمات الأغنية
- the bolokos - love you as before كلمات الأغنية
- subjected to infinity - hallucination كلمات الأغنية
- after dinner - soknya-doll كلمات الأغنية
- aklo - outside the frame كلمات الأغنية
- rapsodos filologos - πλoύτoς oρυκτoς كلمات الأغنية