
ismael lo - fa diallo كلمات أغنية
beuguena wanté mane dé dama amoul
da nga di gouné motakh mouy sa khalaat
ni beuguena wanté mane dé dama ragal
da nga di ngouné moutakh mouy sa khalaat
nga naan ma kay niou sey té noumouy démé?
bou ndieukone dang chi toll niou may la djabar
té legui bo ko meunoul demal teudi
cherie coco li dé doyna kemane
nga nane ma kay niou say té awma pantam
fa diallo wakhma noko toudé
nga naan ma takk la mane awma place
cherie coco wakhma no ko toudé
ndakh legui da ng-y diang ba yéy keuyitt
di takhawalou
mané li dé doyna kemane
ni beugu na, ni beuguena la
fatou diallo wakhma no ko toudé
nga nane ma kay niou say té awma pantam
fa diallo wakhma noko toudé
nga naan ma takk la mane awma place
cherie coco wakhma no ko toudé
ndakh legui da ng-y diang ba yéy keuyitt
di takhawalou
mané li dé doyna kemane
ni beugu na, ni beuguena la
fatou diallo wakhma no ko toudé
ni beugu na, ni beuguena la
cherie coco wakhma no ko guissé
ni beugu na, ni beuguena la
fatou diallo wakhma no ko toudé
ni beugu na, ni beuguena la
cherie coco wakhma no ko guissé
nga naan ma kay niou sey té noumouy démé?
bou ndieukone dang chi toll niou may la djabar
té legui bo ko meunoul demal teudi
cherie coco li dé doyna kemane
nga nane ma takk la mane awma pantam
fa diallo wakhma noko toudé
nga naan ma takk la mane awma place
cherie coco wakhma no ko toudé
ndakh legui da ng-y diang ba yéy keuyitt
di takhawalou
mané li dé doyna kemane
ni beugu na, ni beuguena la
fatou diallo wakhma no ko toudé
ni beugu na, ni beuguena la
كلمات أغنية عشوائية
- stylufka - pride's fucking with u كلمات أغنية
- crotail - просто так (simply so) كلمات أغنية
- taky music - like a dream كلمات أغنية
- sara kays - old enough كلمات أغنية
- douglass, solo k.os & antioch - e.n.i.a.g كلمات أغنية
- smilers - it´s not easy كلمات أغنية
- vingo - v كلمات أغنية
- gaugemto - planb كلمات أغنية
- francis poulenc - c'est pour aller au bal كلمات أغنية
- koit - my wart كلمات أغنية