ismael lo - dibi dibi rek كلمات الأغنية
paroles de la chanson dibi dibi rek :
dibi dibi rek
aah dibi dibi rek
aah dibi dibi rek
yangui deugueurlou wanté meunoko boul sop bayil niou djeuliko
yangui ndirok balai bou niou takhawal, aah ndakh yow lekkato
yangui beugu dé ndakh yow nanato, boul sop bayil niou djeuliko
ndakh mo ley madj lo
dibi dibi rek
aah dibi dibi rek
aah dibi dibi rek
dibi dibi rek
aah dibi dibi rek
aah dibi dibi rek
mbeuguel kenn khamoul lou mou doonn
foulla diou barri ndaham amatou fi yoon
kholl moy capitainou boromam
ndakh mo ley madj lo
dibi dibi rek
aah dibi dibi rek
aah dibi dibi rek
dibi dibi rek
aah dibi dibi rek
aah dibi dibi rek
ay niit niom bou niou beuguenté, khamaal lo tchi waakh
niom mame boye sene taar wessouna, wayé tey laniou gueuneu beugueunté
ya ngui beugu dé ndakh yaw lekatto
bo fi guetarro waw ma bayiko
ndakh mo lay madj lo
dibi dibi rek
aahdibi dibi rek
aah dibi dibi rek
dibi dibi rek
aahdibi dibi rek
aah dibi dibi rek
ndakh mo lay madj lo
ndakh mo lay madj lo
dibi dibi rek
aahdibi dibi rek
aah dibi dibi rek
dibi dibi rek
aahdibi dibi rek
aah dibi dibi rek
dibi dibi rek
aahdibi dibi rek
aah dibi dibi rek
dibi dibi rek
aahdibi dibi rek
aah dibi dibi rek
كلمات أغنية عشوائية
- the carburetors - crank it up كلمات الأغنية
- anuel aa & bad bunny - hasta que dios diga كلمات الأغنية
- udo jürgens - gute reise durch das leben كلمات الأغنية
- in sex - and me and you كلمات الأغنية
- udo jürgens - edelweiss كلمات الأغنية
- adam faybrem - too good for me كلمات الأغنية
- andrae (leo) - alya's mist كلمات الأغنية
- mcfly & carlito - cabine d'essayage كلمات الأغنية
- tacita - colpevole كلمات الأغنية
- tabu - mein gebiet كلمات الأغنية