grandiz kroo - mbalahuma كلمات الأغنية
[intro]
[hook x2: napz]
ak lu yon b meuna lendem damai huss okay
rigint-ss yengaluma rap la choose all day
damaii rap mbalahuma, damaii rap mbalahuma
damaii rap mbalahuma, damaii rap mbalahuma
[verse 1: napz]
kalamay hardcore hajut c gemin mumuneh, no no
sunn ko sekkeh dii nga daww pipeline beh kubuneh
sa ngensor bii ngai sol dii tobb dii dal dii jai skinny
sii man dey ova dang ni jongoma bu rock bikini, uh
sa rap ah telleh tah nga daw songu mbalah
deuka si tilimal sunu game beugeu lu noi teh cheap ni charakh
sarahu fan man lako tudeh, sodon yeg sah nulei wureh
stay loyal to the game ba nor sii heyeh nang sii gudeh
jel mbalah beat tererari tankhal sunui nopp
wer ko sii game dohut fek seni rapa wopp
ku jog-y sii lu hard utali lu noi mein pachah nga
since you like tasting different sh—s defii len pachanga
kon purr mui lerr sa game a tilim melni eutu mbam
bi diss nala k-mpa ni sa sufu malanu mam
wah jeh baree so its high time i made the point
ku rap mbalah don sa pain na nga faju with this joint
[hook x2: napz]
ak lu yon b meuna lendem damai huss okay
rigint-ss yengaluma rap la choose all day
damaii rap mbalahuma, damaii rap mbalahuma
damaii rap mbalahuma, damaii rap mbalahuma
[verse 2: retsam]
uh, nga amm sa problem yeksii rek maa yokasii duma
mark-ss dui harr beh friday jott purr jubalii juma’
damaii rap mbalahuma, bagg-bagal yegaluma
sen t-ssu aki tessanteh safma xessalu aida patra, uhh chambaii
gemenj you xessaw, n0bb ndurok marche sandaga, chambaii
sen instigation against hip hop, boy julatuna
fatuna, yagana, mission bii matna aganaa, cypher
ma by prince ali johlenn kor rap tangana
majohkokor ?”johkokor”, majohkokor ? ”johkokor”, uh
mann duma morm, naa, mann deh duma morm , naaaaaaa
bunch of drake babies please delorlen senn mum
ndahh youssou su degeh lee dii ngenn amm problem ak morm
damaii rap mbalahuma, lii ng-y deff netehtula
buguma tcheh laal dara sama loho henj subaa
damaii rap sama rap, nga mbalah sa mbalah
don’t call it rap mbalah ndahh boy lii ng-yy deffa lahh
[hook x2: napz]
ak lu yon b meuna lendem damai huss okay
rigint-ss yengaluma rap la choose all day
damaii rap mbalahuma, damaii rap mbalahuma
damaii rap mbalahuma, damaii rap mbalahuma
[outro]
ak lu yon b meuna lendem damai huss
rigint-ss yengaluma rap la choose
damaii rap, damaii rap
damaii rap mbalahuma, damaii rap mbalahuma
كلمات أغنية عشوائية
- field medic - house arrest كلمات الأغنية
- tz da coronel - fé blindada كلمات الأغنية
- horse head - scream mask كلمات الأغنية
- fuego eterno - sumergidos en el placer y el dolor كلمات الأغنية
- zita (bel) - dancing in the sky كلمات الأغنية
- rothstein - powers landing كلمات الأغنية
- mach-hommy & tha god fahim - bone strait كلمات الأغنية
- seydina - consumcracy كلمات الأغنية
- daedalus - moonlit كلمات الأغنية
- scarfo - pajo gear كلمات الأغنية