
ghost mortel - bye bye كلمات أغنية
{intro}
bye bye bye bye bye bye
{pre_refrain}
bye dootoul mane ak yow
waan ngama guinaaw douma nellaw
sameu xeel mii né sii yow
dii djaaner sa kanam sou guudi né sellaw
{refrain}
ndeké alal lama djeundé
mom dh alal lama djeundé
deem naa bayi ma andaak kenene
kouma ko waaxone douma ko guueum mais
bye bye bye
{couplet}
bye bye demmal nga bayi ma way
yama nii wone doma gagn
tay waar ngama ndax ben gayne (yeah)
yama doon waax nagnou calculé lou xeew gnou lidjentii ko sunu biir
tay ma souffrir moh neek sameu bénéfice
faaaté nga lougnou doundou mak yow
rêve moudjé doon sii mane cauchemar
deef ngama louma metty
tewwoul damay dellou waat sii yow (oooh)
yama nii wone yaay doon sameu yaayou doom
linga ma djoureul mooy xool buu feessak ay gaumm
{bridge}
bye bye
demmal bayi ma way
meuneu tougnou deem noooon
bye bye
{pre_refrain}
bye dootoul mane ak yow
waan ngama guinaaw douma nellaw
sameu xeel mii né sii yow
dii djaaner sa kanam sou guudi né sellaw
{refrain}
ndeké alal lama djeundé
mom dh alal lama djeundé
deem naa bayi ma andaak kenene
kouma ko waaxone douma ko guueum mais
bye bye bye
{outro}
bye bye !!! demmal nga bayi ma way
bye bye !!! demmal nga bayi ma way
bye bye hé!! bye bye
bye bye ouuuuuuuuh bye bye
ohhhhh yeaaaah!!!!
كلمات أغنية عشوائية
- atrás hay truenos - promesas كلمات أغنية
- ell&s - cloud 99 كلمات أغنية
- rəssam & nihad - gəlim, görüm səni كلمات أغنية
- protect - rip fredo* كلمات أغنية
- led apodaca - nieves de enero كلمات أغنية
- tzarbombah - fuckin wit my head كلمات أغنية
- benno! - tanlines كلمات أغنية
- 山本譲二 (george yamamoto) - チェランサスの夢 (cheransasu no yume) كلمات أغنية
- asco & young adz - high end fashion كلمات أغنية
- чмохи ? (chmohi ?) - again ? كلمات أغنية