elzo jamdong - yalla yaa na كلمات الأغنية
chorus
yalla yalla beyal se tole
yalla yalla beyal se tole
yalla yalla beyal se tole
yalla yalla beyal se tole
and what you think ?
lo gueum defalko sa bopp, yalla yaa na
lo gueum defalko sa bopp, yalla yaa na
lo gueum defalko sa bopp, yalla yaa na
lo gueum defalko sa bopp, yalla yaa na
verse 1
yo yaay se premier kharit (premier kharit)
rakk yaay se premier kharit (yaay se first)
kholou chinois meun neu nioule
beuniou toubaab meun neu jaune
n-gga mbourou fof ko farine (nieuppeu wicked)
negn yokk job wagni wokh (wagni wokh, yeah)
negn yokk wagni wokh (yokk job)
diogueul for li nga mom
se morom yaa ngui dokh
mouno toke fi nga toke di tek
boul kharr prési, khamoul louy se galère
khamoul louy se bonheur
prési noum ley talé ? (ay boul khaar prési)
amoul khaddi prési am ne salaire
prési am ne chauffeur
mais prési deukkoul gallèm
c’est triste…
chorus
yalla yalla beyal se tole (beyal se tole)
yalla yalla beyal se tole (beyal tole bi)
yalla yalla beyal se tole (beyal se tole)
yalla yalla beyal se tole
and what you think ?
lo gueum defalko sa bopp, yalla yaa na
lo gueum defalko sa bopp, yalla yaa na
lo gueum defalko sa bopp, yalla yaa na
lo gueum defalko sa bopp, yalla yaa…
verse
yo baayil mou sedd fattèl sho bi (fattèl sho bi)
baayil mou sèdd fattél sho bi (baayil mou sèdd)
kham naa mom nga beuggone bokkal lepp
wayé mèram placer na fa kou leu eupp money
(degn ko diaay)
yeah daf le break wayé thioloul (wayé thioloul)
kham na ni daf le bètt wayé thioloul (mo fa dèè)
kocc néneu boul di wolou
pour mane balaa wakhou wolou lepp sopp sakha worroul
oh, yeah
mais lou leu dal dang ko attane (dang ko attann)
yeah homie lou leu dal dang ko attann (ay lou leu dal)
homie yalla douleu tek louley yaakhal (never !)
kou khamoul nattou mouno kham louy se kattann
hit me !
yeah
chorus
yalla yalla beyal se tole
yalla yalla beyal se tole
yalla yalla beyal se tole
yalla yalla beyal se tole
and what you think ?
lo gueum defalko sa bopp, yalla yaa na
lo gueum defalko sa bopp, yalla yaa na
lo gueum defalko sa bopp, yalla yaa na
lo gueum defalko sa bopp, yalla yaa na
outro
yo message bi simple neu
boul khaar tchi ken dara
lo gueum defal ko se bopp
boul khar tchi ben nit
كلمات أغنية عشوائية
- ubrukt klut - lus my snus كلمات الأغنية
- boosie badazz & mo3 - everybody كلمات الأغنية
- river valley worship - a wild chorus (altars) [ensemble version] كلمات الأغنية
- raul ws - endless كلمات الأغنية
- justine skye - make a move كلمات الأغنية
- kitty in the tree - billion dollar girl كلمات الأغنية
- yanslo - c'est le yans, pt. 4 كلمات الأغنية
- k camp - game ain't free كلمات الأغنية
- dreebo - time كلمات الأغنية
- leah nobel - we never really leave each other كلمات الأغنية