elzo jamdong - saï saï كلمات الأغنية
yeah yeah eh eh yeah
verse 1
kenn warouma beugg
mane tchi sama bopp khawma louma beugg
(mane khawma louma beugg)
ken warouma beugg bi niouy ndieukk dadié bobou wakhoumala deugg (bobou wakhoumala deugg)
ken warouma diégué (ehh)
kou ma kham di nga thiéné fi nga thiéné
(di nga thiéné fi nga thiéné)
mane kenn warouma diégué
so done kharit sama bopp laa lay ndieukk téré
(sama bopp lalay ndieukk téré)
bridge
boul meusseu gueum samay textos
boul meusseu nangou niouy wéto
mane doumeu fey damay lep dow
ndakh damay play, #nintendo
boul meusseu gueum samay textos
boul meusseu nangou niouy wéto oh
doumala diokh li ng-y weur boul ma wolou ndakh wakhouma loudoul ay léébone
chorus
mane saï saï laa, maa gueuneu yess al qaïda ah ah ah
saï saï laa motouma, moytouma eyy
khamal ne saï saï laa maa gueneu métti al kaïda ah ah ah
saï saï laa, moytouma, moytouma ey
verse 2
yow boumeu wakhlo, soma tidjilé se nopp naala doflo (dinga dof)
doumako tey soumay noplo
so ma tidjilé se bopp di nga of-do (yeah)
damay dow somay wone love
ndakh beugoumeu koumeu beugg di meu toppato (eh) no !
boul ess you’ll get no love
somay khaar onsh0r- maa ngui oofsh0r- ! ey
bridge
boul meusseu gueum samay textos
boul meusseu nangou niouy wéto
mane doumeu fey damay lep dow !
ndakh damay play, #nintendo
boul meusseu gueum samay texto
boul meusseu nangou niou wéto oh
doumala diokh li ng-y weur boul ma wolou ndakh wakhouma loudoul ay léébone
chorus
mane saï saï laa, maa gueuneu yess al qaïda ah ah ah
saï saï laa, motouma, moytouma ey
khamal ne saï saï laa maa gueneu metti al kaïda ah ah ah
saï saï laa, moytouma, moytouma ey
rap verse:
neekh laamign, bad mind
khole bi degn tchi warone coller stop sign
niaata laa fi digone dékhou banneekh ?
tchi guédiou rangogn dé legn moudié lap g-yine !
dama lédj dama dioubeudi
shawty naala tédj ci sey souvenirs
au début dang-y bég fok ne doumeu nit
tey bo sanione doma fréq doma meusseu miin !
yagg naa di wakh tchi gorr yi fowé kholou guél
tané wouma kone mounouma téyé rôlou frère
sciensal kepp kou t-ss yakaar tégou yonou jail
do deggeuti kenn néleu doundeul bo tchi toluwé…
(do deeggueti ken, do deggueuti ken
do deggeuti ken né leu doundeul bo tchi tollouwé)
outro
saï saï laa ah ah ah ah (saï saï la)
al kaïda ah ah ah ah (al kaïda)
saï saï laa ah ah ah ah (saï saï la)
al kaïda ah ah ah ah (al kaïda)
saï saï laa ah ah ah ah (saï saï la)
al kaïda ah ah ah ah (al kaïda)
saï saï laa ah ah ah ah (saï saï la)
al kaïda ah ah ah ah (al kaïda)
كلمات أغنية عشوائية
- meenoi (미노이) - cheek to cheek كلمات الأغنية
- madman & matshi - eusébio كلمات الأغنية
- tokiodk - gisele bitch كلمات الأغنية
- fool in utopia - fire bones كلمات الأغنية
- carvakas - story of the eye كلمات الأغنية
- misheral - fantastic girl كلمات الأغنية
- tylo (seattle) - vesper كلمات الأغنية
- walt disney records - conto de fadas (pós-feitiço) كلمات الأغنية
- pedrem - the sun comes down كلمات الأغنية
- code10 - nosikzamorozhen كلمات الأغنية