
elzo jamdong - lonely كلمات أغنية
intro
néwone nala someu baayé me lonely (rek me lonely)
légui réére na wone lène me yone wi (yone wi umh)
verse 1
togne ngama, alou na…
youkhou nala balou na…
li ley dioylo be légui mba dou mane?
néwone nala méré ngama égal kharou na… (eh)
yow la kham, mane nga mine…
yow la am, thi mane nga mirr
mane yow ak ibliss rekka meunone li…
kénène kouniou narone bolé degn koy lidieunti (eh)
wayé lo guiss dey diékhe mat ne seukk légui
seme p-ss yém ne fi mane mi ndieukke diéégui
dém na bala khate bala yakkh santé
ségueum diamm-ssanté bou dag nékk dagg-ssanté !
chorus
néwone nala someu baayé me lonely (rek me lonely)
légui réér na wone lène me yone wi (yone wi umh)
wakhone nala némeu doyoul me dolli (rek me dolli)
mbokk ya ngui défar, nélène ma la tannone
wayé ken mounoumeu téré me dioum
fogone nani dessate neu wayé deme sétate
be guiss né mounougn bokkeuti room (douniou bokkeuti room)
verse 2
foukki nit moun negn tollo khél (an han)
wayé niarri nit mounouniou tollo khol (eh)
li nga gueuneu beug moleu meuneu gueneu bégn
ladial alcoolo bi barder thi boutélou bigne !
ki nga beugg defe wara fadj se diangoro
moye se kharit moye se m-ss moye se andeundo
ki nga beugg defe wara done se wérou-waye
mais bo naré deukk thi fitna deunguey warou waay
bouniou sanione dougn fi ekssi bouniou mounone mougn…
khamanté néniou wayé ndouro wouniou
bi borom bi bindé sounou t-ssé diouddo gouniou…
beugguenté négn wayé dioubo wouniou
chorus x2
eh douniou bokkeuti room x2
unhu x2
كلمات أغنية عشوائية
- k suave - ukuk كلمات أغنية
- sopa - regista كلمات أغنية
- vio - geceler كلمات أغنية
- saetia - becoming the truth كلمات أغنية
- therealdylann - off the lean كلمات أغنية
- musicartistjamesharrison - if they knew (john 4:10) كلمات أغنية
- achtvier - meek mill كلمات أغنية
- scott stepakoff - twist off wine كلمات أغنية
- bob marlich - entre-deux كلمات أغنية
- r.o.a.r. (rory stewart) - don't mock a mocking bird كلمات أغنية