elzo jamdong - khoudar كلمات الأغنية
intro
yenn saye dingueu guiss louleu dieulé kow lolou beu diapp se bopp kessé ngay meun
fekk ngueneleu laakhou tchi guinaw bobou fitna ndakh yalla rekkeu kham ak di def li gueune
woah oh oh yeah yeah yeah
woah oh oh woah oh oh
woah oh oh yeah yeah yeah
woah oh oh woah oh oh
verse 1
bi moussa waré ande ak khoudar def ko né dinga diang ak mane defal ndank ak mane nanga ande ak dal
dinga guiss louleu yem wayé nak nanga dieme diokh me se kaaddou né do and ak hal
kou nek lileu yalla mey
nieupp mounougn done benn
ladial phiraon mi yalla dieye
beu mou fouye beu degg deugg leu done begn
guiss diongoma diou sey t-ss
waroul takh ngay kh-ss
khamoulo lou tchi f-ssou
beu guissogo gore beug khey f-ss
moytoul me dieek diou romb rek
diekk taarou ngané dee dou yomb
wala djiguene diou lamb
ngané no def ding ko lamb
pre-chorus
judge not khel matoul boul wereunté tchi lou se yone nekoul
dieuw ak fok ne am ne diam mo tané yenn yi kou gueum dou ko def nekkoul
chorus x2
yenn saye dinga t-te be se khel nara diakh-sso
yenn saye dinga fire be se khole nara diégué seuss
yenn saay dinga t-te ba sa khel bara diakh-sso oh oh
wayé bepp fitneu toudd yalla nga tchi wara ndieukk diemeu rakh-sso oh oh
verse 2
borom bi dey missal
binde ne lepp be noppi
segueum gni kham nioye teye
kou niakk kham wara gueuneu noppi
kou wekk lepp tchi guissané bo
dtouwoul adina dinele sappi
bouleu khiif takha salite
my brother yalla bouniou niakk soppi
li khew tchi mim rééw
gueunoul yémé bitim rééw
mystique tchi biir guééw
wayé loukhouss dou firim rééw
se deunkeundo boul kheep ndieurigneum
tagg sey kilifeu dingate serigneum
téyé se kourouss gaddou se satala
deukk tchi dieuw yakkh der yeufou satt leu
pre chorus
chorus
bridge
yenn saye dingueu guiss louleu dieulé kow lolou beu diapp se bopp kessé ngay meun
fekk ngueneleu laakhou tchi guinaw bobou fitna ndakh yalla rekkeu kham ak di def li gueune
yenn saye dingueu guiss louleu dieulé kow lolou beu diapp se bopp kessé ngay meun
fekk ngueneleu laakhou tchi guinaw bobou fitna ndakh yalla rekkeu kham ak di def li gueune
outro
lo fi def dinegn wakh
lo defoulit dinegn wakh
yeek tchi mbame womate mbaam
ken dou tee dinegn wakh
كلمات أغنية عشوائية
- as mineirinhas - não sofra assim, paixão كلمات الأغنية
- brownboi bliss - hundred thousand thoughts كلمات الأغنية
- avery clayton - avery clayton - i love you كلمات الأغنية
- plenty (jpn) - 能天気日和 (noutenki biyori) كلمات الأغنية
- moisés - janeiro كلمات الأغنية
- reece brozovich - fake love كلمات الأغنية
- m44 rapper - tulip كلمات الأغنية
- swag toof - dreamkillers كلمات الأغنية
- fred thomas - they replace your heart كلمات الأغنية
- turrane sandtan - comeouttheair كلمات الأغنية