elzo jamdong - falaaw كلمات الأغنية
yaw kay gnou job pour mou tanė bro
nak mou tanė
amoul khof
talougnou salso(salso)
warougnou planer
kay gnou job
nakh mou tanė bro
khamna lima beug
khamna lima beug
makoy doundou deug
makoy doundou deug
amoul lomay djangual
amoul lomay djangual
biguė yėksi sėne nala guė gniangual
sėne nala guė gniangual
yaw yafi gnew
falaw falawf alaw falaw
falaw falaw falaw falaw
falaw falaw falaw falaw, yaw kay gnou job warougne
planer bro warougnou planer
akh lougnou dokh warnagn
garer troc tabakh gualler
amna wotér amatoul
kharer bro amoul kharer
amoul khof talougn salsoooo amoul baller
yag johhhh motax yak tchiow legui dam-ssi gorė
dakone fooo mala doree
ak tokh cigarette wayer noooo dama yagueu fort
manė fok mou carrė
fok gnou djok
borom meuk dowww
menoul khėkhhh ak armée
(khėkhhh ak armée)
legui soy def liste elzo djitou
$# elzo djitou $#
bougne sagnone ma danou
¥ medzo diatta
كلمات أغنية عشوائية
- moacyr franco - soleado, a música do céu كلمات الأغنية
- talrak - cercle vicieux كلمات الأغنية
- nino blu - medicine كلمات الأغنية
- kaiden - there’s nothing left for us كلمات الأغنية
- kili k - 200 كلمات الأغنية
- rachel brooke - the loneliness in me كلمات الأغنية
- turbiow - collares كلمات الأغنية
- arief - basayang tapi babagi كلمات الأغنية
- cygz - shine on كلمات الأغنية
- maame afon - odo soronko كلمات الأغنية