
deeno. - love you mama كلمات أغنية
intro:
oh
oh mama. oh
yeah mama
aye mama
pre_chorus:
yaaaaaaaai
bena lah
ken dusa yaii
morm kena la
kenen kuneh morm moi sa yaii
gan la
i love u mama
yow kena nga
verse:
ey mama
yai sama hero
yai tah ma neka zero to heroo
every day sa smile dafa wara d glowoo yeah yeah
(yeah)
hamna dega dega munu mala feeeyy
yaga nga di def li dipi beh bess niki tey
lu neka nga ma jangal beh ma maggah nii tey
eh yaaai eh yaaai
(yeah) (yeah)
yai yaai yai sama yaaai (yai)
man munumala by sama yaaaiii (yai)
sumala gissut
damai joi
lu neka nga ma defal teh wahulor dafa doi
dangma tehteh
yow yai bugulor ma joi
sumala tehral leh yai
buguma nga joi
sumala tehral leh yai
buguma nga joi
dangma tehteh
yow yai bugulor ma joi
sumala tehral leh
yai buguma nga joii
eh mama ey mama yeah
i love u mama
i love u mama (mama)
pre_chorus:
yaaaaaaaai
bena leah
ken dusa yaaii
morm kena la
kenen kuneh morm moi sa yaii
gan la
i love u mama
yow kena nga
chorus:
yaaaaaaaai
bena leah
ken dusa yaaii
morm kena la
kenen kuneh morm moi sa yaii
gan la
i love u mama
yow kena nga
mama,mama, mamaa
mama mama mamaa
i love you mama yow kena nga
كلمات أغنية عشوائية
- mannick - fille mère كلمات أغنية
- ferbinho - espião كلمات أغنية
- teeks (nz) - without you كلمات أغنية
- julian krause - paing كلمات أغنية
- lizzy hilliard - wanderlust كلمات أغنية
- finn play - พ่อนายอะ (your dad) كلمات أغنية
- zamdane - affamé #10 - athéna كلمات أغنية
- junction collective - brave كلمات أغنية
- supăr tril - stai كلمات أغنية
- poppy tears - access denied كلمات أغنية