chyco siméon - boul bayi كلمات الأغنية
[intro]
[verse 1]
da ma demon
wouti woon lo len dounde
dekke di bay
nguir kou ne bagn mass fande
bi yoon
mani diekoul thi yoon
mani diekoul thi yoon
bi yoon moom dou yoon
demal diemi banen
andalak nianen
gueneuleuk kanen
nit daal dafay diem lanen
diemal gobi dounde
del diem sa sou ne
nala diaral daal yaw lou ne
te gua diem sakh doug fou ne
watou lou ne
tay setloo
[chorus]
boul baye
boul baye
boul baye li lay dolel
houwow
boul baye
boul baye li lay dolel
[verse 2]
ni beugoo kou dem
te beugo nit koufi tekki itam
dеuke di fen
mani roussouloo setlou woo gni lay sеn di la setlou
roussouloo setlou woo say nawle yi lay sen
nangou woo deglou woo gouba teukh lou di dem
dieul sa yonou mbon
roussoulo domi adama
and ngaak nianen do bayeti nak
fasouloo diogue thi li
do bayi loudoul gua de
te man mi nena la
[chorus]
boul baye
boul baye
boul baye li lay dolel
houwoo
boul baye
boul baye li lay dolel
houwoo
boul baye
boul baye li lay dolel
houwoo
boul baye
boul baye li lay dolel
[bridge]
baye
baye
baye baye
yelelelele le lee
lili lile
wouyoho
[verse 3]
hunn
beugou loo dem
beugou loo ken dem ha
digua mass sooy
mani roussouloo setlou woo gni lay sen di la setlou
roussouloo setoulou say nawle yi lay sen
nangou woo deglou woo gouba teukh lou di dem
dieul sa yonou mbon
roussoulo domi adama
and ngaak nianen do bayeti nak
fasouloo diogue thi li
do bayi loudoul gua de
te man mi nena la
[chorus]
boul baye
boul baye hannnn
boul baye
boul bayi lilay dolel
houwoo
boul baye
[outro]
كلمات أغنية عشوائية
- tim burgess - say yes كلمات الأغنية
- timber timbre - we'll find out كلمات الأغنية
- tim barry - 222 كلمات الأغنية
- tim ripper owens - santa claus is back in town كلمات الأغنية
- bad company - cross country boy كلمات الأغنية
- timi yuro - i apologize كلمات الأغنية
- nigahiga - clenching my booty كلمات الأغنية
- tigertailz - love overload كلمات الأغنية
- timeghoul - boiling in the hourglass كلمات الأغنية
- tim hughes - joy كلمات الأغنية