
carapid music - dawal كلمات أغنية
[verse 1 : bako]
sam way demna ci yalla god, yalnako yalla yeureum
si boppu kogn bi legn dane tokk sayu ma fa rombé sameu xél…
daldi tééy li moy lane, aduna bi amul solo nandité niunley nameu
dangniu bett tagouwo
melni demb lawoone biniuy dane reupeuteul sa galé
ba niu khey beneu fane… bis bi nga taneu pour dem
firdawssi boy yalla na yalla yeggal feu sa ruh
niongui ley ni-n-l souf sedd sa kaw yalla yokk sa leer
chaufeur apprenti c-kseur moteur 4 roues
niakeu néniu chauffeur…
[bridge : fla]
dawal dawal demal nawal fi ba aljana
dawal dawal amul taxaw dara duleu téyé
dawal dawal demal nawal fi ba aljana
fi ba aljana fi fi ba aljana
[hook : kalz & bako]
car bi yakoy yor com yaka dane dawal
su fékké mogui sey lokho kone amul luniuy ragal non non
niune fepp leniuy dem kone fepp leniuy dem
mais buur yalla moy sakk walay buur yalla moy sakk x2
[verse 2 : kalz]
life bé khaweu animal
leudeum si kaw lérr si souf ni domou tal
xawmeu qo wone fils li dou yone
ték ngeu niou deal meunone ngeu niou diémeu xar x2
[hook]
[bridge x2]
كلمات أغنية عشوائية
- steve wiggins - all the darkness كلمات أغنية
- ちゃんみな (chanmina) - never grow up (acoustic version) كلمات أغنية
- spang sisters - eddie murphy كلمات أغنية
- 1027pharoah - black pink purples كلمات أغنية
- diana original broadway cast - the dress كلمات أغنية
- i never heard the bullet - my sidekick is my only true friend كلمات أغنية
- sophie doyle ryder - hunni hunni كلمات أغنية
- thomas reid - butterflies كلمات أغنية
- kianja - place for me كلمات أغنية
- barbaro - kawliga كلمات أغنية