canabasse - général كلمات الأغنية
{refrain}
bou bess taak
wakhal gniy khar ma fay dou tay dou souba no !
j’ai trouvé la solution douma abou thioubalo
nokk nieup comme balla gueye takhawal beuzzou modou lo
multiplié samay dialoré gnou bari nawma defma tourando
général eskeuy
général eskeuy
boma séné bayil li ng-y def nieuw todjal sa général (walabok)
général eskeuy
révolutionnaire sans le béret yeah mane la b-ss guévara
dikk changé tendance bi n-ggaz yi di hate
kham nagn ni mafi tek tank beugouniou avouer
ani rebellion bi we canab-sse club marquez les pas
yokh la matal coup d’etat coloniser gni done bagne
yeah dafa djot nieup xam kane moy général
{1er couplet}
young militaire libéré bango di prouvé di gagné ay galons
loumou yautou djot cii bounetou boumou feug mou oubékou dou bras long
majestueux tchi limouy def boups nénala b-ss comme messi b-ss tchi ballon
yaramou nééne la def nako nieup dieulsi lima indi ni rambo
déretou noone yi ci samay talons
def révolution am niouma gueum di follow
ma nek à l’aise melni kou dougou biir immaculée warfa matal mission commando (eskeuy)
ya n-ggaz is funny ni crayon crayon bouy diéma effacé gomme
sèn rap meunoul takhaw ni mbasin bouniou p-ssé faté gomme (thioo)
bo amé lomay djay bo yabo na nga ci indalé tonne
dégue na niouné guéné nga album
tres bien mais sa corner (kogn)
mala eup buzz bouma fégné télé nga beug changé chaine man
démal changé carrière li day gueune tarr man
dk city finest dikk wilipander nigaz yi nekk tchi rap bi deffougnoufi sh-t
tojal ma fiston may general
{refrain}
wakhal gniy khar ma fay dou tay dou souba no !
j’ai trouvé la solution douma abou thioubalo
nokk nieup comme balla gueye takhawal beuzzou modou lo
multiplié samay dialoré gnou bari nawma defma tourando
général eskeuy
général eskeuy
boma séné bayil li ng-y def nieuw todjal sa général (walabok)
général eskeuy
révolutionnaire sans le béret yeah mane la b-ss guévara
dikk changé tendance bi n-ggaz yi di hate
kham nagn ni mafi tek tank beugouniou avouer
ani rebellion bi we canab-sse club marquez les pas
yokh la matal coup d’etat coloniser gni done bagne
yeah dafa djot nieup xam kane moy général
{2ème couplet}
déja certifié sama image soxla woul tampon cnra
artiste reconnu bouma nékhé khoti sama carte bsda
général immortel, on ne me tue pas, on ne me deshonore pas
daniou beugone ma marquez les pas
mais ko khol cii niom di nga guiss sama trace sou pas
khamal lène ni b-sse moy pop depuis 2007
décapité nieup ana koumay tenir tête
métal néna lène li job la li dou fils mba tête
lyrics electriques meuno ko capter sans de tête
néwone nala mane may pop
lo fokk baay yaw do gatt
mane may ki mom dk city it’s b-ss
i’m a star yeah chui fly
douma sani kher damay job senegal
yakkal sama derr wanté lepp deugg la
my n-gga damay def no diematouma
gueune la oundou gueune la clean yeah rappeur cii cl-sse
armoire bi fess ba meuneu solal kogne
n-ggaz ya ngui merr sama buzz molène togne
guel ya ngui fééne nane mane dama lèn topeu
mais c’est compréhensible ndakh général b-ss mom mokoy todj
{refrain}
wakhal gniy khar ma fay dou tay dou souba no !
j’ai trouvé la solution douma abou thioubalo
nokk nieup comme balla gueye takhawal beuzzou modou lo
multiplié samay dialoré gnou bari nawma defma tourando
général eskeuy
général eskeuy
boma séné bayil li ng-y def nieuw todjal sa général (walabok)
général eskeuy
révolutionnaire sans le béret yeah mane la b-ss guévara
dikk changé tendance bi n-ggaz yi di hate
kham nagn ni mafi tek tank beugouniou avouer
ani rebellion bi we canab-sse club marquez les pas
yokh la matal coup d’etat coloniser gni done bagne
yeah dafa djot nieup xam kane moy général
{3ème couplet}
def rap game bi industrie bi buzzlab kone direction générale
reubeu mc yi nek fi di doul rafle général
dess na touti sèn carriére yen nieup dafay fay coupure générale
indile public bi limou soxla nek alimention générale
en général bouniou tolé coté panik général
def show, get doe (xaliss) fortifié ba rosé né kouy liguey société générale
{refrain}
wakhal gniy khar ma fay dou tay dou souba no !
j’ai trouvé la solution douma abou thioubalo
nokk nieup comme balla gueye takhawal beuzzou modou lo
multiplié samay dialoré gnou bari nawma defma tourando
général eskeuy
général eskeuy
boma séné bayil li ng-y def nieuw todjal sa général (walabok)
général eskeuy
révolutionnaire sans le béret yeah mane la b-ss guévara
dikk changé tendance bi n-ggaz yi di hate
kham nagn ni mafi tek tank beugouniou avouer
ani rebellion bi we canab-sse club marquez les pas
yokh la matal coup d’etat coloniser gni done bagne
yeah dafa djot nieup xam kane moy général
كلمات أغنية عشوائية
- joan jett the blackhearts - let me go كلمات الأغنية
- joan jett the blackhearts - the french song كلمات الأغنية
- ian whitcomb and bluesville - you turn me on (turn on song) كلمات الأغنية
- joan jett the blackhearts - tube talkin' كلمات الأغنية
- 38 special - long time gone كلمات الأغنية
- 38 special - fantasy girl كلمات الأغنية
- joan jett the blackhearts - five كلمات الأغنية
- joan jett the blackhearts - right in the middle كلمات الأغنية
- joan jett the blackhearts - be straight كلمات الأغنية
- joan jett the blackhearts - activity grrrl كلمات الأغنية