boiie pablo - danger كلمات الأغنية
[intro]
sku, sku
it’s your boy pablo
[couplet 1]
dugu fii danger la, tagoul sey mbokk bo nieuwé thiéinthieu leu
dof_dof_loul ken doula, wakh heure bii foum toll melni degougn leu
dundu bii diéngou leu, soy ragal thioono rek mou songou leu sééniou leu
deumm yii fééniou leu, faw nga meuna xhamé mbaa niou diékkou leu
fokné koula siign moy sa andadoo, dafa fekk n_gga magagoo
n_gga bo xhamé ni xhamagoo, meun xhamlou balaa weesou book
wanté bo xhamoul ni xhamagoo, dii nga lorou moudié bagn sa boop
yanguii wouty n_gga amagoo, boul andadook gnii amoul ndokh cii boop
meuss negn ma raw gnima andadool, mais bima beugué damlèn yagga boote
dafmay nekh ma djiité douma meuntii bokk
manguék meun_meun, ak katann ak ngandii bopp
même kii deff lou nekh mounoul nekh nieupeu, ma dieema nekh kii moudiou té ndieukeu
nieup mounougn toloo nak té moy deugeu _
way bou nieupеu boolo meunn ki meunn nieupеu
mère bii dii diooy père bii geudeu, ndakh yarougn sen doom bi ci deugg
beugg lou nooy té fii deugueur, motakh niouy door ak dii keuffeu
braquer leu gun bi dii seufeul, ladj leu sa money si chauffeur
yako nangou boodé chômeur, té yay xhagn sa bop sa honneur
liguey dou xhaadj dou diekh hana ng_y xheep !
soy taamou naadjé comme kouy taneu thieep
bo beuggué feekh faw nga deuké kheekh
fii lepa metii même sou lepp di dieekh
nga thioolé mbaa nga tekki dingko yekk
way fexekhel tekki nguirr nga guedj ko yekk
té lou gawa diekh moy li yomb’a am !
gni yeekh yewou moy gni yeekh’a am !
dou lou yeemé n_gga nekhnaa xham !
[pont _ pré_refrain]
té lou gawa diekh moy li yomb’a am !
gni yeekh yewou moy gni yeekh’a am !
dou lou yeemé n_gga nekhnaa xham !
meuss negn ma raw gnima andadool, mais bima beugué damlèn yagga boote
dafmay nekh ma djiité douma meuntii bokk
manguék meun_meun, ak katann ak ngandii bopp
même kii deff lou nekh mounoul nekh nieupeu, ma dieema nekh kii moudiou té ndieukeu
nieup mounougn toloo nak té moy deugeu
way bou nieupeu boolo meunn ki meunn nieupeu
[couplet 2]
boodé yoolé man bouma diégué_diégué
fii lepa lundum kén dou mbélé_mélé
té souniou meun_meun dugnko wedj_wedjé
daniouy deff ng_y guiss douniou wéré_wéré
teksi bokougnok guys loloo guena yéémé
niom amouniou sh_t paré beugg woné
nigaa douniou og douniou thiéré_thiéré
narcotik sama boyii nioola guena niémé
diaroule ladj, that’s right boy nonu la démé
koufii deff lou sal rek ma fété_fété
dinaa fessal salle signer cachet_cachet
amatouma diote dama wara mettre le paquet
n_gga n0bouma sa yaye damko fassé_fassé
def xhaliss sam guyn moumay gâter_gâter
def hit, make money lolou kassé_kassé
teksi manguék talent bi lol dou diafé_diafé
dagnii niafé_niafé…dougnko kaféé_kaféé
tangal game bamou bakh melni café_café
diapp n_ggas yii feutt, deflén dégué_dégué
ana koukoy téré ?
boudé dangma méré !? dafa melni ng_y marr paré naan sa déréte
boudé dangma méré !? dafa melni ng_y marr paré naan sa déréte
boudé dafa diafé dang_y xharé, kassé !
kou am dara dafa défone dara, kassé !
n_gga weurseuk kiko moom rek ley, tassel !
wanté dafay fekkii gniiy xharou di niafé !
bo beugué alal dangsi boolé thiono, niémé !
ki niakk alal moungui xhalate nimkoy, amé !
ki fessak alal moungui ragal souko, niaké !
kounek’ak lila sonal motakh nieupa wara xharé
boy xhaar ci niite diinga lorou f__ko doul xhaaré
lo beugg dalay gaagn rawatiina boko taméé
niou diaay la doméram ndakh mbeuguel bougnko xamé
loo bayii dalay bayii lolou la diamono dji wané
boul xhool si gni nga tané dieemal dialeu fii nga callé (never)
[outro]
gang gang gang gang …
كلمات أغنية عشوائية
- the spruce moose - don peyote كلمات الأغنية
- faces on tv - the image of boy wonder كلمات الأغنية
- hanin dhiya - darling (acoustic) كلمات الأغنية
- youngrichchris - back and better كلمات الأغنية
- tungevaag & raaban - hey baby كلمات الأغنية
- rob cavestany - bittersweet كلمات الأغنية
- the cow brothers - marrakech (ep version) كلمات الأغنية
- dot'n bang - 9 mars كلمات الأغنية
- liza anne - ireland كلمات الأغنية
- shirley horn - if you love me (really love me) كلمات الأغنية