kalimah.top
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

black needle noise - system bi كلمات الأغنية

Loading...

niome nioye niome nioye
kou thie wakh niou dougala thie mbambii
yaw momoulouniou ye
niounela falonè kène nietouwakh dara system bi

niome nioye niome nioye
kou thie wakh niou dougala thie mbambii
yaw momoulouniou ye
niounela falonè kène nietouwakh dara
yaw momoulouniou khen khen khen khe
kou thie wakh niou dougako thie mbambii yaw momoulouniou ye niounela falonè momemoye dogale loukonèkh

kène nienètoule wakh khè yaw nndakh dafamèlni yaw ya niou momemè lakalnga niou khè khè
kéne nèwatoule ba yandore rè khè è è khana khamoulounè nè ne
beusse dina nieww niou wathiela wa w

mandè mandè sabope ngafi nèkale
dieul rewni diayko talibe n-ssarane be
amoule yeurmendè mandè yaw
sabope ngafi nèkale dieul rewni diayko talibe n-ssarane be
beuglo niou talou niou kou wakh nga dougalko kou wakh nga dougalko thie mbambii diaye niou dole diaye niou dole
sonale niou kène niemètoule wakh kha

kène nienètoule wakh khè yaw nndakh dafamèlni yaw ya niou momemè lakalnga niou khè khè kene nèwatoule ba yandore rè khè è è
khana khamoulounè nè ne beusse dina nieww niou wathiela

yèlèlè yèlèlè diè yèlèlè diè yèlèlè diè

كلمات أغنية عشوائية

كلمات الأغاني الشهيرة

Loading...