birahim - kima done seet كلمات الأغنية
lepp louma am ak koumou done
cheri booy yama ko gueuneul
lima liggey beuss bounek di ci sone
ci lou bakh lepp yay borome
ya takh ma xam kima done, diox ma fit
ba takh na do tou ma tiit
lima liggey beuss bounei di ci sone
ci lou bakh lepp yay borom
ya takh ma xam kima done, diox ma fit
ret_n_l dotouma tit
xolma ci beut ley nekh boul xep
teh boul ragal diam rek ngey am
lima beug rek moy kou bakh
ki gueun borom xol bou nice
kouma doul nakh dima begueul
souma diaxlei sarakhma deufeul
kima done sett yow leu maley d
tey meu tak leu
(boul nеlaw)
jiguen dey beuri diom
togal khar bama takk lеu
rekkkkk teral leu
doumala meussa fowei
beu nopi ba leu fi
goor you bakh yeup romb leu
yooooow ngey misere
(kone nak boul nelaw)
jiguen dey beuri diom
togal khar bama takk leu
rekkkkk teral leu
doumala meussa fowei
beu nopi ba leu fi
goor you bakh yeup romb leu
iiiooooow ngey misere
xamna beug ngama
teh yow xamnga beug nalaaa
cheri iow beug nala
ci ay nelaw ngani beug ngama
xamna beug ngama
teh xamnga beug nalaaa
cheri beug nala
ci ay nelaw ngani beug ngama
fi leu fi leeuuuuu
boudoul fi dou done fenene
ki leu ki leu kiiiii leuuuuu
boudoul ki dou done kenene
yow xam nga seu bop
xam li geu done
ndakh jiguen dey xam bopam
sam ngeu seu bop
ya ngi xol euleug
yow da ngey aaamme niaboot
takk ngeu seu seur
moytou ngeu g_yi
ndakh bougn la xamei dem bayi leu
wax dji loumou nekh ha nekh ha nekh
yow boumla takh ba xam seu boop
ndakh jiguen amoul loudoul bopam
wala jiguen amoul loudoul sageum
mbeguel mo nekh si bougn la beugué
mbeguel mo nekh si bougn la n0bé
mbeguel mo nekh si bougn la wolo
mbeguel mo nekh si bougn la safo
mbeuguel mo nekh
bara cheri soda la
mbeuguel mo nekh
baye jobe cheri amina la
mbeuguel mo nekh
djily nyass cheri sophie la
mbeuguel mo nekh
henry cheri ami la
كلمات أغنية عشوائية
- cas wetsema - harira كلمات الأغنية
- lil keke - feel good don't it كلمات الأغنية
- varg (se) - blue line (112 rådhuset) كلمات الأغنية
- nossay - real nigs come first كلمات الأغنية
- micah williams - roses & violets كلمات الأغنية
- belmin brate - zeilen nur für dich كلمات الأغنية
- dcvdns - mein mercedes كلمات الأغنية
- kurupt - we can freak it (east coast remix) كلمات الأغنية
- weezer - kids/poker face كلمات الأغنية
- cee & bekah - do it all again كلمات الأغنية