baye mass - xale rew mi (remix) كلمات الأغنية
bismillah niou deeti door dellu saku nian
di nian yallah mu nangoul niu lep lun ko nian
seytane dey yakh khel di sopi khalat
di feweule andado
niun daal bum nyu laal yaye
yeen xale rewmi
ni la ko beugue waw
sen atmi mo du atoum gune
soxlo woul beuri wakh
nanj bolo won mak nyi
nyun nioy doule rew
gone su taggou ay wadiouram
disso ak nioom seu ndialbeen
fu mu ne ci aduna senj thia yakaar lu bakh
yeen xale rewmi
ni la ko beugue waw
bu nu wakhtane ak sunuy baye
mak matna ba thim rew
lu niu wakh nyu degg ko boole sunuy xalat
nyi ci biti nyi ci biir fu waay meuna ne
nen bole sunuy xalat rew mi dem kanam yaye
yeen xale rewmi
ni la ko beuguе waw
man daal waleu bima feetee
maaki samay gars
pexe munе nyung ko dieem nguir sunu rew mi naat
sunu beugue sunu rew mi naat danyu wara boolo
ta kat fou way meune ne sen thia yengueuto
كلمات أغنية عشوائية
- 2 low key - outro كلمات الأغنية
- acculbed - trip to brazil 2 كلمات الأغنية
- crash rarri & rawbone - 2 phones كلمات الأغنية
- xyrn - kill zone كلمات الأغنية
- the four seasons - brunswick bowling spot كلمات الأغنية
- ryujin - lemon (cover) كلمات الأغنية
- los niños vudú - el mejor de los viajes كلمات الأغنية
- young rebel heroes!! - bubblegum & kerosene كلمات الأغنية
- victor j sefo - for life كلمات الأغنية
- patrick wilson & kelli o'hara - reprises كلمات الأغنية