baye mass - capitaine كلمات الأغنية
capitaine lyrics
fi lepp tamalé, fima la guissé
dangma romba ma tago sama sago
lu g_yi neka di wakh degatuma ko
diaama rek la bugon
ndakh ma diokh la sama xol
lima dugal sama xol xawma lumu done
so ma rombé dotuma muna khol
dumala meusa muna bayi
jiteul ma ma done sa ouroul ayni
benj koye ligeye demb la wone
yay sama champion
yay sama linguère
benj koye ligeye demb la wone
bilaye mbeuguel moye capitaine boromam
su djiné beugé ku yeug dang_ye danou
bilaye mbeuguel moye capitaine boromam
su djiné beugé ku yeug dang_ye danou
dumala meusa muna bayi
jiteul ma ma done sa ouroul ayni
benj koye ligеye demb la wone
bilayе mbeuguel moye capitaine boromam
su djiné beugé ku yeug dang_ye danou
ahh bilaye mbeuguel moye capitaine boromam
su djiné beugé ku yeug dang_ye danou
كلمات أغنية عشوائية
- felp22 - artigos كلمات الأغنية
- skydog music - rediscovering loneliness كلمات الأغنية
- folk noir - dear misery كلمات الأغنية
- thomas james white - path كلمات الأغنية
- capoxxo - better off as friends كلمات الأغنية
- coffin salesman - drowning in the wishing well كلمات الأغنية
- ren massie - hot air balloon كلمات الأغنية
- vic.soul - teenage romance كلمات الأغنية
- lil baby - humble كلمات الأغنية
- wasabi blues - the comeback كلمات الأغنية