
baye mass - abadane كلمات أغنية

doumala bayi
doumala bayé eheh
yawitt bouma bayi
boulma bayé yeah
mom nene daf leu beugueu piir
nena dafa beugueu nga nekka ki mou djital
mome néna yadi kimou guiss
nena ci niom nieup yaw rek la beugueu djital
nèna dotu la bayi
yaw la taneu si goor gné
nèna dotu la bayi
yaw la taneu ci djiguene gné
doumala bayi
doumala bayè
yawite boulma bayi
boulma bayè
abadane
abadane
abadane
abadane
yaw boulma bayi dahimane
abadane
abadane
abadane
abadane
doumala bayi dahimane
sa agne mo daakh louma meune lekk
sa keur mo daakh fouma meuna nekk
lougniou neex lekka
louniou neex nane
ndiabote gui fecc akka retane
mane dama la nopp ba dila beug fone
mane damala manguila chérie
dama la nopp ba dila beug fone
mane damala manguila chérie
doumala bayi
doumala bayé eh
yawite bouma bayi
boulma bayè eheh
abadane
abadane
abadane
abadane
yaw boulma bayi dahimane
abadane
abadane
abadane
abadane
doumala bayi dahimane
كلمات أغنية عشوائية
- grant-lee phillips - my eyes have seen كلمات أغنية
- grand pax - atv كلمات أغنية
- erosian exile - a muse كلمات أغنية
- travis stacey - sequoia كلمات أغنية
- козачок (kozachok) - 27 كلمات أغنية
- kpsn - nie masz pytań كلمات أغنية
- die ärzte - duenkel كلمات أغنية
- indus valley kings - hell to pay كلمات أغنية
- larun - pinho sol roxo كلمات أغنية
- eric tagg - mãos de afeto كلمات أغنية