amadeus - boulma saganè كلمات الأغنية
boulma saganè lyrics
guiss na leu ng_y ndiap yeah
deff ci foula gou meut seuk
man dall limaye nyan amine wai
mou dieugué done sama weurseuk
dey nex ci sama xol
biss bi ngamay ndieuk khol
néma berg na la donté benn yon
leuy meusseu done ci sama doundeu
yallay boor lou ko nekh dogeul
yallay deff lou ko nakh ci diam
té yallah deff mann ma tamoula
natoula am ndogal, dieuleul
yallay boor lou ko nekh dogeul
yallay deff lou ko nakh ci diam
té yallah deff mann ma firéla
natoula am ndogal, dieuleul
hé boulma sagané wai
boul meusseu faté né wai
pithieu xol ma ya fa né wai
kon boulma sagané wai dieuleul
way wi, fent na ko ndakhté
yow kenn nga ndo nyaar
weurseukou yallah nga ehh wai
dey nex ci sama xol
biss bi ngamay ndieuk khol
néma berg na la donté benn yon
leuy meusseu done ci sama doundeu
yallay boor lou ko nekh dogeul
yallay deff lou ko nakh ci diam
té yallah deff mann ma tamoula
natoula am ndogal, dieuleul
yallay boor lou ko nekh dogeul
yallay deff lou ko nekh ci diam
té yallah deff mann ma firéla
natoula am ndogal, dieuleul
hé boulma sagané wai
boul meusseu faté né wai
pithieu xol ma ya fa né wai
kon boulma sagané wai dieuleul
boma woyofalé ba nga sagané ma
dina tiss ci mann, dina tiss ci mann, dina tiss
boma woyofalé ba nga sagané ma
dina tiss ci mann, dina tiss ci mann, dina tiss
té damalay khol, ya nekk sa birr xol
té damalay khol, ya nekk sa birr xol
boul meusseu faté né wai
pithieu xol ma ya fa né wai
كلمات أغنية عشوائية
- bellafea - thorn bird كلمات الأغنية
- bill champlin - the fool is all alone كلمات الأغنية
- dry county - straight up on the rox كلمات الأغنية
- black heart procession - liar's ink كلمات الأغنية
- color me badd - i adore mi amore كلمات الأغنية
- common - sum shit i wrote كلمات الأغنية
- clutch - small upsetters كلمات الأغنية
- cop shoot cop - interference كلمات الأغنية
- coral - a warning to the curious كلمات الأغنية
- conway twitty - together forever كلمات الأغنية