amadeus (massamba amadeus) - fi ba leuz كلمات الأغنية
eh, yooo
eh iiih
yeah yooo yaaa yeeh
fi ba leuz ma lay moom coow rekk ay bari
def la soxnay sama coobare
toppal sama ginnaaw te bu coow bari
xam nga ni yaay sama càppali
xam nga yaa ni ma
ni teg na ma la he
fu ma mousta teg jàmm bu yàlla bind
man fonk na ma la
man it ma ni la heee, sa xel naa dalee
diandia bi du soppeeku massamba
du dem sa massamba la, hei!
fi ba leuz ma lay moom coow rekk ay bari (bari bari bari bari)
def la soxnay sama coobare (bari bari bari bari)
toppal sama ginnaaw te bu coow bari (bari bari bari bari)
xam nga ni yaay sama càppali (bari bari bari)
jànq yaa ma ni
du ku la ciippatu génn ci ndaxte yombuloo
du ku la jàmm na ni, he waay!
jànq yaa ma ni
bis dina ñëw nga daagu ci kër gi séyal
man ma tok ci ndaanaan yi, hee waay!
li nga ma wax tax na mën na ma wat
ni doo ma bàyyi même su ma faatoo
àdduna yépp su ñu dajewoon
pour séparer ñu du tax mu àntu
jànq yaa ma ni, jànq yaa ma ni
li nga dikk doy na ma, wëruma leneen
li nga ma wax neex na ma, yeiiii
fi ba leuz ma lay moom coow rekk ay bari (bari bari bari bari)
def la soxnay sama coobare (bari bari bari bari)
toppal sama ginnaaw te bu coow bari (bari bari bari bari)
xam nga ni yaay sama càppali (bari bari bari)
كلمات أغنية عشوائية
- lionel richie - serves you right كلمات الأغنية
- kent - verkligen كلمات الأغنية
- kent - what it feels like كلمات الأغنية
- kent - vintervila كلمات الأغنية
- petula clark - how insensitive كلمات الأغنية
- petula clark - here, there and everywhere كلمات الأغنية
- sick of change - more than words can say كلمات الأغنية
- petula clark - monday, monday كلمات الأغنية
- petula clark - love is here كلمات الأغنية
- lionel richie - love will find a way كلمات الأغنية