admow - boula dara meti كلمات الأغنية
yena say nga fok ni thi adouna bi keneu doula comprendre
sometime nag dem ba diap ni doto museu contan
ci bir keur gui yaye boye nela doula meye nada
ci mbeda bi yeah yeah
ragala takh ngani do maye dara
mais nak boul diakhle, yone leu mou diaffe
want maadi goor bi kham fi nga feete
kham sa ndieuga takh ma deukh thi di niaafe yeah yeah
thiofeleu ci bir khol bi
diox ma confiance ma yoboula fu sorri
ou bebe oh bebe
damala love love love baby love love love
boula dara mеti
nakhar diekh na tey mangi thi sa wetе
boula dara meti
dinala thewal thi nadj
thewal la thi kerr
baby i got your back
boula dara meti
ecoute moi baby
i love you lady
et je sais que t’as peur de m’aimer
si tu t’inquietes pour moi t’as tord
faut que tu sort de ton decors
t’as deja gagner mon coeur
donne moi ma chance
fais un effort
soumala xole guiss thi yow ku am ndiom
douma beugua loudoul done sa heros
do wete thi bile yone you are not alone
je suis ton ange gardien
ohhhh
baby you’re the one, baby you’re the only one
baby you’re the one that i need in my life
damala love love love baby love love love
boula dara meti
nakhar diekh na tey mangi thi sa wete
boula dara meti
dinala thewal thi nadj
thewal la thi kerr
baby i got your back
boula dara meti
damala love love love baby love love love
boula dara meti
nakhar diekh na tey mangi thi sa wete
boula dara meti
dinala thewal thi nadj
thewal la thi kerr
baby i got your back
boula dara meti
كلمات أغنية عشوائية
- rayan - haram (feat. intifaya) كلمات الأغنية
- the eight curse - shockra كلمات الأغنية
- pony bravo - sunset كلمات الأغنية
- neogen - therapy session (who shot ya? remix) كلمات الأغنية
- lasse stefanz - ute på vischan كلمات الأغنية
- petey pablo - i'm makin' moves كلمات الأغنية
- eyeshine - jumpstart كلمات الأغنية
- jon connor - cleaning out my closet كلمات الأغنية
- ismail ahmed - you n me كلمات الأغنية
- yes-r - verleden tijd كلمات الأغنية